lirikcinta.com
a b c d e f g h i j k l m n o p q r s t u v w x y z 0 1 2 3 4 5 6 7 8 9 #

xale bi - youssou n'dour lyrics

Loading...

xale bi lyrics
non non non nonnnn
non non non nonnnn
né xalé bii
né beugoumala merloo
né xalé bii
né beugoumala merloo
ndaxté so méré, so méré
sama yaram daw, daw ba diaxalma (boul ma méré)

lou mounoul gnak faw dafaw am
wareef dafay mate
lég lég mou done lou doul neex
yaw sama dom
souba tax may wakh
so magué di nga xam
ndaxté so dioyé, so dioyé
sama yaram daw, daw ba diaxalma

wadiour ak dom
faw gnou y waxtane
féxé melni mbourok sow
ndem réro mouneta gnak
so diaxlé, so diaxlé
na sa khelmi dém
dém ci say wadiour
ni jamano mél
tééy da cé baax
jubantil bamou thior
ndax momine dafay rooy
bissa ngui gnew
sou magué diarigne la
lép nga ci bami ndaw
ndaxté so méré, so dioyé
sama yaram daw, daw ba diaxalma (boul ma méré)
né xalé bi
né beugoumala merlo
heuuuu xalé bi
né bougouma la merlo
(xalé momine la yaw bouko merlo té dé ko bégueul)
ndaxté so méré, so méré
sama yaram daw, daw ba diaxalma

adouna nii la xalé bi lé
sou bay waxaté nga déglou ko
adouna nii la xalé bi lé
sou yay waxaté nga déglou ko
adouna nii la xalé bi lé
(nangue ma deglo xel)
sou bay waxaté nga déglou ko
(bagn ma deglo xol)
adouna nii la xalé bi lé
(samaaa dooooom)
sou yay waxaté nga déglou ko
(nangue ma deglo xel)

né xalé bi
né beugoumala merlo
haaaann xalé bii
né beugoumala merlo
xalé bi
né beugoumala dioylo
ndaxté so méré, so dioyé
sama yaram daw, daw ba diaxalma

Random Song Lyrics :

Popular

Loading...