mama africa - youssou n'dour lyrics
yée … yée hé hé hée hé
yée … yée hé hé hée hé
hoo, hoo ehnnn haaan
hoo africains, woy le leen ma africa
benn continent, mel ul ni africa
am ul benn werente ci loolu
suñu mbëggél ci yaw, africa
ana ñi soriyaante
bu ñu kenn jaxasse
na ñu xam suñu bopp
une jeunesse engagée, africa
namm u ñu dara, yalla a la barke el
tu es dans nos cœurs, du ñu la weccoo
boo xas ee miin xam ni, fii mooy suñu kër
come home with me, i, i,i
hoo africains, woy le leen ma africa
benn continent, mel ul ni africa
am ul benn werente ci loolu
suñu mbëggél ci yaw, africa
ana ñi soriyaante
bu ñu kenn jaxasse
na ñu xam suñu bopp, avеc
une jeunessе engagée, africa
namm u ñu dara, yalla a la barke el
tu es dans nos cœurs, du ñu la weccoo
boo xas ee miin xam ni, fii mooy suñu kër
come home with me, i, i,i
ñun africains, su ñu ànd a ndoo
bokk nday ak baay, boole suñuy doole
kholal ëllëg u adduna bi
seet al say doom ñoo, koy mujj é
yée hée, an han
ni nga magge ek, ni nga yaatoo
noonu nga riché
ni nga magge ek, ni nga yaatoo
noonu nga riché
du ñu lë, wetio ba mouk
du ñu lë, weccoo k keneen africa
xam nga ni la say, doom yi bëgg é
tag naa la kaay
yaa ne ci suñu xol
wo, wo, wo, wooy
wo, wo, wo, wooy
du ñu lë mas a weccooy
kenn, yaw africa
yée … yée hé hé hée hé
yée … yée hé hé hée hé
hoo, hoo ehnnn haaan
hoo africains, woy le leen ma africa
benn continent, mel ul ni africa
am ul benn werente ci loolu
suñu mbëggél ci yaw, africa
ana ñi soriyaante
bu ñu kenn jaxasse
na ñu xam suñu bopp
une jeunesse engagée, africa
namm u ñu dara, yalla a la barke el
tu es dans nos cœurs, du ñu la weccoo
boo xas ee miin xam ni, fii mooy suñu kër
come home with me, i, i,i
hoo africains, woy le leen ma africa
benn continent, mel ul ni africa
am ul benn werente ci loolu
suñu mbëggél ci yaw, africa
ana ñi soriyaante
bu ñu kenn jaxasse
na ñu xam suñu bopp, avec
une jeunesse engagée, africa
namm u ñu dara, yalla a la barke el
tu es dans nos cœurs, du ñu la weccoo
boo xas ee miin xam ni, fii mooy suñu kër
come home with me, i, i,i
ñun africains, su ñu ànd a ndoo
bokk nday ak baay, boole suñuy doole
kholal ëllëg u adduna bi
seet al say doom ñoo, koy mujj é
yée hée, an han
ni nga magge ek, ni nga yaatoo
noonu nga riché
ni nga magge ek, ni nga yaatoo
noonu nga riché
du ñu lë, wetio ba mouk
du ñu lë, weccoo k keneen africa
xam nga ni la say, doom yi bëgg é
tag naa la kaay
yaa ne ci suñu xol
wo, wo, wo, wooy
wo, wo, wo, wooy
du ñu lë mas a weccooy
kenn, yaw
translate to english
Random Song Lyrics :
- supermarket - akira the don lyrics
- will you keep out all the sadness? - dens (rock) lyrics
- caramel-backpack v2 - caramel lyrics
- don’t be shy (japanese ver.) - winner lyrics
- batman - ktcg lyrics
- breathe - trevon lyrics
- hasta la locura (live session) - maurilio suárez y el grupo méssia lyrics
- amigos, salud! - américo lyrics
- clouded - brent faiyaz lyrics
- a.m - negative - ammusicofficial lyrics