lirikcinta.com
a b c d e f g h i j k l m n o p q r s t u v w x y z 0 1 2 3 4 5 6 7 8 9 #

hope/yaakaar - youssou n'dour lyrics

Loading...

kila done topato
so meunè defalko
bilepp bakhèe
yow ladone guiss
bima sonè yamadone diguel
bima rerèe
deug deug guereum naleu
fatèwoumala
neubeutoumala ma
kila done topato
so meunè defalko
bilepp bakhèe
yow ladone guiss
bima sonè yamadone diguel
bama rerèe
deug deug guereum naleu
fatèwoumala
neubeutoumala ma
mane leu sen dome dièe
fatèwoumala
neubeutoumala ma
mane leu sen dome dièe
mame marie sene yama topato
anh yèe lelèeeeeee wowoy
diaral ma
mai diay soumay dolè
ni diong diong diong
ô ô ô ô oooooo
dina la setsi niou wakhtane maa

kila done topato
so meunè defalko bilepp bakhè
ooooooo yow la done guiss
bama sonè yamadone diguel
bama rerèe mam
man deug deug guereum naleu
fatèwoumala
neubeutoumala ma
mane leu sen dome dièe
fatèwoumala
neubeutoumala ma
mane leu sen dome dièe

kila done topato
so meunè defalko
yaw la done guiss
kila done topato
so meunè defalko
yaw la done guiss
kila done topato
so meunè defalko
yaw la done guiss

Random Song Lyrics :

Popular

Loading...