allah - youssou n'dour lyrics
[intro]
allah allah
allah allah
allah allah
allah allah
[chorus]
souniou borom bi ya wakhidoune kenn la
kenn la kenn la amoul masse
souniou borom bi ya wakhidoune kenn la
kenn la kenn la amoul masse
souniou borom bi ya wakhidoune kenn la
kenn la kenn la amoul masse
lahilaha illalah
souniou borom bi ya wakhidoune kenn la
[verse 1]
bo néké sisa birou yaye
yalla dila samm bagua am
diourim nienti werr
mou wathie la si adounya bi
bolé thia nak
ay kheweli khewel
boko togné so diegeulo mou bal la
boko niane mou mayla gua sant ko
mou dolil la
ladioul loudoul nangua ma diamou
ladioul loudoul nangua ma diamou
iow bo goré bo goré
warko diamou sant ko
[chorus]
souniou borom bi ya wakhidoune kenn la
kenn la kenn la amoul masse
souniou borom bi ya wakhidoune kenn la
lahilaha illalah
souniou borom bi ya wakhidoune kenn la
kenn la kenn la amoul masse
souniou borom bi ya wakhidoune kenn la
Random Song Lyrics :
- congratulations - jimmy eat world lyrics
- selfishness of evil men - b l a c k i e... all caps, with spaces lyrics
- danny boy [dvd] by celtic woman - celtic woman lyrics
- unfinished - hutchy lyrics
- nobody - devitchi lyrics
- dope wings - billy harvey lyrics
- prizzy prizzy - russell! lyrics
- b.s.e. - storm lyrics
- hope - silk cinema lyrics
- euphoria - jalen montel lyrics