4/4/44 - youssou n'dour lyrics
4-4-44 (4-4-4-44) môm sa bopp mô neikh
4-4-44 (4-4-4-44) guiss say mbok mô neikh
bô léké ba sour war nga gueureum
war nga gueureum gni doug thi wagne wé
wagne wa tang na
fimou toll nî war nguèna bëg
war-ngèna bëg thi indépendance bi ak-liko indi
4-4-44 (4-4-4-44) môm sa bopp mô neikh
4-4-44 (4-4-4-44) guiss say mbok mô neikh
bô léké ba sour war nga gueureum
war nga gueureum gni doug thi wagne wé
wagne wa tang na
damani bou leuk léké olom
boudè goréna té deugou warna ko guereumé pithe
no, no, no no no no
no, no, no no no no yeah
4-4-44 (4-4-4-44) guiss say mbok mô neikh
4-4-44 (4-4-4-44) guiss say mbok mô neikh
ah li dafa nékh… guiss say mbok mô neikh
li dafa nékh… gueume sa bopp mô nékh
4-4-44 (4-4-4-44) môm sa bopp mô neikh
no, no, no… guiss say mbok mô neikh
4-4-44 (4-4-4-44) môm sa bopp mô neikh
oa, li dafa nékh… guiss say mbok mô neikh
a… môm sa bopp mô neikh
oa, li dafa nékh… môm sa bopp mô neikh
Random Song Lyrics :
- self pity city - abandon all hope lyrics
- applause - unkle_krack lyrics
- so on it - miyavi lyrics
- bull frogs croon (suite) - aoife o'donovan lyrics
- prende conmigo - aloisio lyrics
- autumn on briarcliff - cal van gogh lyrics
- bisexual freestyle - d.e.z.h.a.w.n lyrics
- malo* - dollar lyrics
- in the club - 211 lyrics
- tokyo nights - tm88 & madeintyo lyrics