mirna - wally b. seck lyrics
mirna lyrics
wakhal ak mane mi mo geune
soma guissé yangui saalé
sa mbeuguél mi ngui lay réy
setlouna, setlouna
setlouna, setlouna
yow man nga n0bb
wakhal ak mane mi mo geune
soma guissé yangui saalé
sa mbeuguél mi ngui lay réy
setlouna setlouna
setlouna, setlouna
yow man nga n0bb
sou samedi dioté
yangui khol nimay sagnsé
sou dimanche dioté
yangui khol nimay rombé
yow wakhal ak mane
mo geune, mo geune, mo geune
yow wakhal ak mane
mo geune, mo geune, mo geune
setlouna, biniou khamanté ba légui
yangui may dozé
wouy lélé aaah
diaratouko mirna
ah mirna, diaratouko mirna
kholal tchi papa ngom
nimou n0bé ndella wornama
formi doudou dable
moy baayou, bayou anta ngom
papa ngom, l’incontournable waw
yérim ndella, bayou mohamed laay woo
son compte twitter
wanma ninga n0bé
wornama, fonk nala darling
dieuleul sa téléphone, photowou yoné ma
ma yoné la let’s love line
solal sa louboutin, diagar diagari
wopopopopo, yangui may gagn
goor gnilé goor gnilé
amlène yeurmandé tchi djiguène gni
wooo, li nékh na
mat ngama rapp, matma djiné séytané
darling mirna
setlounaaaa
yakamtina nga wonma sa tiofél
sa sokhla, bila geuna sokhal
sokhla bi moma tchi nekh
sa mbeuguél, bilay yakamtinako
yamala am mala
yow yama geuna love waw waw
adja yonel
buur bi yallah limou massa ndogal
deugeula kagn ndogal gui moma si nékh wowowo
yama… am mala
yow yama geuna love waw waw
adja yonel
sa tiofél loumou bari bari
mane sama boss wésouna guédj wawawawaw
souma démone ba ditcha féy
dina saggou ba faf fa lapp man
yama… am mala
yow yama geuna love waw waw waw waw
bilay, toumani, lépp ni la
bilay, toumani, lépp nonou la
oumou wade bakhna, lépp nonou la
waw walay cheikh senghor, lépp ni la
assane ndaama, lépp ni la
chérie titou bakhna, diagne narr nonou la
moustapha narr woma, lépp ni la
coumba ngom woma, lépp nonou la
ndèye marie marème ndoye, baaye waly nonou la adou
wopopopopopopopopop
Random Song Lyrics :
- der letzte patient - baumarkt lyrics
- si tu la ves - númana lyrics
- dark of night - nokris lyrics
- the furthest thing - maren morris lyrics
- awaken - stephen christian lyrics
- mausoleum - arbitrator (us) lyrics
- enchant - eli therula lyrics
- moins d'égo - dinos lyrics
- trustworthy - tns 1ll w1ll lyrics
- freegucci freerade - high 5 lyrics