sweet game - viviane chidid lyrics
sweet game lyrics
nanguoul ma
nè sa xol mane ma fa né
baby tey meu lèral la
nè khamna ni mane rèk nguay weur, deug leu
kou mèlni ngua sokhla meunè founè
foumeu feuleu rèk djomal leu
khamnani gentle ngueu
nanguoul nè malèy bègueul mane may seu star
hey vivi da ngua gueuneu khèw, ndourou wo kou bèw
ya koy daguatè li lèrr na
nanguoul ma
nè sa xol mane ma fa né
baby tey meu lèral la
nè khamna ni mane rèk nguay weur, deug leu
kou mèlni ngua sokhla, kou beuri sèytané ba djakhal leu
khamnani gentle ngueu
nanguoul nè malèy bègueul tchi birr nèkk bi
kou kham li lann leu ngueu wakh ma
kou kham li lann leu meu nèkhal la
kou kham li lann leu ngueu wakh ma
nanguoul ma
nè sa xol mane ma fa né
kaye meu lèral la
nè khamna ni mane rèk nguay weur, deug leu
man ngua sokhla meunè founè
foumeu feuleu rèk djomal leu
khamnani gentle ngueu
nanguoul nè malèy bègueul mane may seu star
kou kham li lann leu ngueu wakh ma
kou kham li lann leu meu nèkhal la
kou kham li lann leu ngueu wakh ma
kou kham li lann leu meu nèkhal la
sonou na tchi sagg bi
di mougn lou mèlni
sonou na tchi sagg bi
di mougn lou mèlni
baby nanguoul ma, wakhal sa gars gni mann leu
tè ngueu sigui kholma
baby nanguoul ma, wakhal sa gars gni mann leu
tè ngueu sigui kholma
bouguou ma lou sèddeu faw mou sanguou way
tchine bokoul tchafine vivè kholoul tchi tchine
ak lo xèkh wèkh na na noy seu ndiba tilim
moh vivi yangui guaagn beuguou ma tchow wagnil way
chérie nangoul ma, dama beuri dj*pp
mane djomal na la té douma rapp
antal ngua li ngua yènou boul wouttalou
gnémé ko waw waw
diguou laal lagnouy rèrrè, after yow lay dessero
tchabi bountou nèkk bi tay rérouma
boul wo walou gnémé ko wawaw
lou mèlni makko mom
té kou feugueu togn ma
gneuweul ma défal la louy takh ngua nanguoul ma
titangué warou la mba lèpp mingui bakh
hey kaay fi, hey kaay hey
li daf may ndourou sweet game waw waw
casa de papel yeufou bandit waw waw
seu âme dafa sensible sori ma
chéri nangoul ma dama beuri dj*pp
mane djomal na la té douma rapp
antal ngua li ngua yènou boul wouttalou
gnémé ko waw waw
ngueu meunn diko dèf bokoul ak koukoy djèm
yako meunn diko dèf yow da nguay fo
hey ambiance
gneuweul ma défal la louy takh ngua nangoul ma
titangué warou la mba lèpp mingui bakh
hey kaay fi, hey kaay hey
ay, kou donn wakh na ngua noppi bass yèkssi na
tay fi day nèkh day roumbakh poutch
viviane yaw lo guénè gnou fetch ko
tay fi day nèkh day roumbakh poutch
eh vivi eup ko bémou mokk du dara du yomb
li daf may ndourou sweet game waw waw
casa de papel yeufou bandit waw waw
seu âme dafa sensible sori ma
Random Song Lyrics :
- like a rose (live) - ashley monroe lyrics
- bootycall problem - pandapanda lyrics
- gusto kita - ogie alcasid lyrics
- rain - liquid gang lyrics
- demain à l'aube - okis lyrics
- finally - shepherds reign lyrics
- nik plunk (part ii) - sinneyy lyrics
- drugs inside my ll bean - lil grocer lyrics
- thank you for liking me - maggery lyrics
- everything is on the table - billy (rock) lyrics