lirikcinta.com
a b c d e f g h i j k l m n o p q r s t u v w x y z 0 1 2 3 4 5 6 7 8 9 #

la cible - viviane chidid lyrics

Loading...

xamna lilay sonal
wax jou bari teksi nga diss te yenouwo
xamna lilay sonal
bilé melokan molay deranger
yalla mayma nangouwo
ma romboula nangoulo
foma seen dima retane té begouloma

heeey
tiré ngama visél bou baax ndax daluma ×3
sit down yow
fii adinala kon teyal (lala lala lalala) ×3
fii adinala fils teyal (ohhhh)

xamna lilay sonal
wax jou bari teksi nga diss te yenouwo
man xamna lilay sonal
bilé melokan molay deranger
yalla mayma nangouwo (mayla nangouwo)
ma romboula nangoulo (ma romboula nangouwo)
foma seen dima retane té begouloma
yalla mayma nangouwo
ma romboula nangoulo
foma seen taalalma loxo té soppouloma

heeey
tiré ngama visél bou baax ndax daluma ×3
sit down yow
fii adinala kon teyal
fii adinala hey teyal
fii adinala kon teyal
fii adinala fils teyala tey

maalay deranger
ndeketé mane rek nga bañ
te xawma loumala def
bo sañoon souba ma dé
ngir suñu andabi yaga
fok ñouy waxanté deugga
ba ñoumay matteu di euffé mattaalela

xarit né waxma mani waxma
lou tax sooma guissé dima ré te beggouloma
kay ma waxla togal ma waxla
pexé you bone ying-y jeem ni yalla guiss la

eeeey
tiré ngama visél bou baax ndax daluma ×3
sit down yow
jeleul waywi ma mayla yeah
jeleul waywi maynala yeah
jeleul waywi ma mayla yeah
jeleul waywi maynala
defko cas

Random Song Lyrics :

Popular

Loading...