lirikcinta.com
a b c d e f g h i j k l m n o p q r s t u v w x y z 0 1 2 3 4 5 6 7 8 9 #

affaire de ado - seven shots lyrics

Loading...

refrain
kou meune ti wax sa life nga ni bou yabo j-pé sa bop the king bling affaire de ado (ro-gee)
dou nékhna lool di foo di blow di képp cho beugua aak man affaire de ado (ro-gee)
hey hey
gneup gneup bégué leu bravo (odd)
fo teule gnou souk jébalou déf la hero (odd)
dou nékhna lool di foo di blow di képp cho beugua aak man affaire de ado(ro-gee)
1er couplet (odd)
check it !
hey am si taf sithiou
meun di mélastikou jaay prék wath tchi coner bi khatiou fipou
f–k sa bop hercule, meune nga réndi pitbul
jiko bakou n-gger bi linga fi taane jékoul
bayil r-ssoul, dina la gagn bobo
defal nank nank tegui tank tank mado
hey yo feelo, louko moy nga k.o
tok najou bokatou réthiou mate sa lokho
oho ma do yéd la si primo
tas de doff cach wala moujou dougou c-ssot
ay bobard connerie tas de bétises
done intelec thi xél, mak ame maitrise
défal sa yité nga nité kharé ame dignité
jougal niaffé khouss mouss té bagna goudé
ndank ndank téguil sa tank
tieupi di tieupi di teubaka dal rék niak
refrain
kou meune ti wax sa life nga ni bou yabo j-pé sa bop the king bling affaire de ado
dou nékhna lool di foo di blow di képp cho beugua aak man affaire de ado
hey hey
gneup gneup bégué la bravo
fo teule gnou souk jébalou déf la hero
dou nékhna lool di foo di blow di képp cho beugua aak man affaire de ado
2éme couplet
ro-gee
fok sa bop mak ba do jeuli bi yaye di wax yang si mbéd mi
nga kham ni niak khélay takh nga jomi fis warning (moytoul)
dou ki tchi télé bi la fan dafay toukh dina ko jéém folow the bottom line
fils bo beugué jiguén na nga mouss, ame tchi liguene bagna khouss
be the best like all my dogs
fils dou tiaguini ghetto nga deug hood bi jokh ko gueud
bou town bi mété dou mandi rékay deugu
say laaf sakha goul sa maagu matagoul
li gnaw waragoul sa gondi takhawoul nékoul
kone na nga kharé bi yoone do soone
reflex, relax, no stress doga réss li déss ya yoon (héy let’s get it on)
j-pe sa coner project gondi bay waja maguét
ya ain’t touch the sky booko jémé rék garé
affaire de ado mola nékh mola nékh
j-pal ni dafay jékh sou b00ba lane moy nééékh ???…
refrain
kou meune ti wax sa life nga ni bou yabo j-pé sa bop the king bling affaire de ado
dou nékhna lool di foo di blow di képp cho beugua aak man affaire de ado
hey hey
gneup gneup bégué la bravo
fo teule gnou souk jébalou déf la hero
dou nékhna lool di foo di blow di képp cho beugua aak man affaire de ado

3eme couplet
odd
hé yaw dokh dokhal sa yoon, moytoul moujou fou boon
kharé roy tchi babylone, nono yaw téguil bi yoon
setatal sa yoon hey dawg forgeting this one
the positive one wowowowa léral sa yoon
ro-gee
moujé dak khouli loy yakou di joy stop
bi mak di wakh ng-y réé fok ni do déé nane gate
diay prék moy lou bess mandi rék bou dara déss
man stop it stop it bala réthiou wééss man
refrain
kou meune ti wax sa life nga ni bou yabo j-pé sa bop the king bling affaire de ado
dou nékhna lool di foo di blow di képp cho beugua aak man affaire de ado
hey hey
gneup gneup bégué la bravo
fo teule gnou souk jébalou déf la hero
dou nékhna lool di foo di blow di képp cho beugua aak man affaire de ado……

Random Song Lyrics :

Popular

Loading...