#mumunation - retsam lyrics
[intro]
ya dun’ knowww/ grandiz / eyesaw #theep /hamg-yoyu/ chambaii
[verse 1: retsam]
buguma duga sii dara
buguma yeksii rek ngen defatii joini kara
buguma doxx dii sigii dii para
buguma gis nyee dornii chaga
gudi bu nekk dii fashion night haleh yu saff nii chebu jagaa
norpinaa teh dumalen setlu naa
gestu naa maa dajj sii ndo bouy sekh dii fompaa lips sii paa
byl maa doxx nee gisuma
yalnaa yagaa sutura
maa jada konj rek t-ssek maricon bii sh-t be kissima
oh my god korm ebola
fogonaa neh dewon naa
ngen moitu goor bouy jutu sumoii yekaa deflen domoda
mandem nyepaa dem lybia di ghetto youths ah suffer jollof melnii buntii syria -sing-
choww bii yepp sii bitii laa
bunch of fatou camara
i type and lash hard you call me keyboard warrior
key board warrior key board warrior
i type and lash hard ncos legii xamna neh sorinaa
[hook retsam x p-thug]
bull wahh -bull wahh dara
dafa amm lor musaa gorm wahko teh bull musaa para
dumaa wahh – dumaa wahh daara
diww sangam defufii daara
teh dunko musaa taga ”ahh”
#mumunation -mute tekk-
#mumunation -mute tekk-
#mumunation -mute tekk-
#mumunation -mute tekk-……
[verse 2 p-thug]
mann njoll mama la yokotei yeguma ndama
fii kufi dem beh falu rek sahh mbaga kom b-tterfly
company wey ak yoi gen
ayut yena boka fly lana tahh maii mute tekk teh yenama dramatize
taah ma gadu mic don si bandi
ken dafaatufi ngirr yallahh derem ak derem
last time ndobi nema nyehi cobo munuta simm cheram
nii lako dohaleh ni hach basa buntii keram
wanteh wahh bi nyarr laa ndah hach na chi buntii cherem
mute tekk no duma wahh fufu, system b nyepla drown lileh tah ma ragala sobu
g-yangi ragala tohonyu teh kanilen tuff nyepp
denyo build mba nyu destroy harr b yagana teh gisung dara chi lung nyu dik boi
[hook retsam x p-thug]
bull wahh -bull wahh dara
dafa amm lor musaa gorm wahko teh bull musaa para
dumaa wahh – dumaa wahh daara
diww sangam defufii daara
teh dunko musaa taga ”ahh”
#mumunation -mute tekk-
#mumunation -mute tekk-
#mumunation -mute tekk-
#mumunation -mute tekk-……
bull wahh -bull wahh dara
dafa amm lor musaa gorm wahko teh bull musaa para
dumaa wahh – dumaa wahh daara
diww sangam defufii daara
teh dunko musaa taga
[outro]
ya dun’ knowwww/ chambaii
Random Song Lyrics :
- xafant fang - zoo posse lyrics
- you will see - syauqi destanika lyrics
- flawed foundations - give you nothing lyrics
- star - kim young geun lyrics
- i'm sad - alexander north lyrics
- mc jay t - joe thornton jt studio lyrics
- creation story - lungfish lyrics
- solo su sti quarti - dominy lyrics
- i wanna bang my head against the wall until i die - ma.iige lyrics
- war against love - nas lyrics