lirikcinta.com
a b c d e f g h i j k l m n o p q r s t u v w x y z 0 1 2 3 4 5 6 7 8 9 #

sama everything - philippe lyrics

Loading...

yeah yeah
yay sama everything
beugeul ma défal la
amouma anything
té dou té ma défal la
wakh ma iow lo beugeu
sa baneex rek la beugeu
sama yéné défal la
togal ma firila

yay sama everything
beugeul ma défal la
amouma anything
té dou té ma défal la
yangui yekk sama loveu
yangui feel sama loveu

li ma yéné xamnako
no you don’t, you don’t, you don’t know ma
xamnako baby
li mala yéné you don’t know ma
xamnako baby
oh you don’t, you don’t, you don’t know ma
xamnako baby
xamalna ni sa domyi
deff la yéné lou barri
no you don’t, you don’t, you don’t know ma
xamnako baby
li mala yéné you don’t know ma
xamnako baby
oh you don’t, you don’t, you don’t know ma
xamnako baby
xamalna ni sa domyi
deff la yéné lou barri

yalla ma bolék yow
yaye diourom nienti wér nga eumbouma
tey dji maag na
wathié di kow souf man ganéssina
wakhma lane nga beug
lépp ma défal la paréna
sama yéné manak zeyna ci adouna ben la (ben la)
gouddou fane laly ni*n*l
yobbou la makka la yéné
magg na beug dap sa love
xamna mounoumala fay
tey yalla may sédé ci sama yéné
linga def ci nioun
yaye boy yay gaindé

yay sama everything
beugeul ma défal la
amouma anything
té dou té ma défal la
yangui yekk sama loveu
yangui few sama lovеu
li mala yéné xamnako
no you don’t, you don’t, you don’t know ma
xamnako baby
li mala yéné you don’t know ma
xamnako baby
oh you don’t, you don’t, you don’t know ma

xamalna ni sa domyi
deff la yéné lou barri
no you don’t, you don’t, you don’t know ma
xamnako baby
li mala yéné you don’t know ma
xamnako baby
oh you don’t, you don’t, you don’t know ma
xamnako baby
xamalna ni sa domyi
deff la yéné lou barri

dolli sant yalla sama dom xalébi magg na
lingma yéné mangui niane buur yalla mou dеgeu leu
pa philippe sa wakh yeggna ci xol nekhnama
pa philippe vivane
yaye ak dom guén di ame
philippe
yay sama everything
yay sama adouna
amouma anything
naniou sant yalla
yangui yekk sama loveu
mangui yekk sa loveu
mangui feel sa love yow mi
no you don’t, you don’t, you don’t know ma
xamnako baby
li mala yéné you don’t know ma
xamnako baby
oh you don’t, you don’t, you don’t know ma
xamnako baby

xamalna ni sa domyi
deff la yéné lou barri

no you don’t, you don’t, you don’t know ma
xamnako baby
li mala yéné you don’t know ma
xamnako baby
oh you don’t, you don’t, you don’t know ma
xamnako baby
xamalna ni sa domyi
deff la yéné lou barri

mar buur yacine mar
birame yacine mar
birame ngouille alé ndiaye

Random Song Lyrics :

Popular

Loading...