hot boy - paps lyrics
[paps]
nioumey get nioy gueuneu mandi gni di dem cii bar yi, flow yi damcii barii di dentch you gueuneu taaar ci balle yi
rap sou done dagn key diang may daak taari saar yi, ligue bi laniou bok mais bokoul mane dama saff ni paris
mane leu kouy khar sa bopp dokh di diarr si niaari part yi bamou taali guiss feu sama yone defleu ko ni niarry tally
done bandit tamit tei cii rap awma ci kharit
di fess ey mc ba tabaski ngen di fatei khaar yi
des flows qui varient, deglouma cii son ba cii khibaar yi lirycs you bakh yi cii biirou rap bi ya len di saakh yi
defma sa paris nga wolou ma tei boul daal di khaadi niou fi nane kaani sakh sougn may get di tachycardie
del lekk rimes you maay andi bay magui sandi niaane yi lo tchi taamou ami
lokho bou taali ma sandi niaane yi mane leu cali gars yi so ma dieulei doma teeela bayii
rendii douma cii tayi mic bi laniouy daasi rey g-ssi
boudei moune ngeu louko raw ayhtia defko vas y
mane ak rap bi nioy life melni coco and ice t
daak tegou n-gga tek ci gueuneu aaye fi
lo tchi beug ma indi ko lou fi gueuneu nice lii
da ngein yagg don air (r) ma doli tchi i.p
dead n-gga yafi berri awma sama taille fii
reuy rap reuy beut cause fou kawei laay see
f-ck racks on racks douma genrou yc
del play di get all i say is truth , na rappers yi gued mane kouma diey guiss proof
tioki mic maley beite may the one boul plouff
nioune ba night daniouy tegou flow yi laley bluetooth
lehgo lehgo, mane douma kheutio ak yow, kou nieuw ma faadj ko rek daw, boy move ndakh do zero
i’m the og you know, mane dama ciiy foo degoo, rap sou done roman ngey door kholei ma victor hugo
tiop wa galsen nane wa states ndakh tanyi niom kendrick rek laa maar
nieup lay daal sen ken dou dess douk dokh sen kaaw encore la naar
mane loumey def boy aka taar , mc dagn yekh ni cacatar , kone dougn ma dapp tei flow sou done khaliss kholema wa qatar….
..
Random Song Lyrics :
- fire in my eyes - yours are the only ears lyrics
- shanthi (ශාන්ති) - fill t lyrics
- how far does the dark go? - anya marina lyrics
- way she goes - tyler hammons lyrics
- 4 am - vinchi lyrics
- thunderbolts - oliver faulks lyrics
- free tay-k! - comethazine lyrics
- switchback [red devil remix] - celldweller lyrics
- build a little home - ruth etting lyrics
- karate kid - białas & lanek lyrics