lirikcinta.com
a b c d e f g h i j k l m n o p q r s t u v w x y z 0 1 2 3 4 5 6 7 8 9 #

soutoural - omzo dollar lyrics

Loading...

soutoural
soutoural, soutoural (woooo)
soutoural , soutoural (wooo)
soutoural , soutoural (wooo)

[pont]
kou niakk reka am yameu guena kham
kou nam dina tamb yameu guena kham
kou khamni khamoul rekka kham yameu gueuna kham
nieupa done ay borom xam*xam yameu guena kham

[couplet 1]
okay, bakh moy bone fi nieupay dioum legui
djiguen moy torokhal goor goor yi nioy mougn legui
djiguen khol avenir mais goor seu passer leyy guiss
motakh goor yi naleu takk legniouy dokhané legui
okay, am diabar you melni sunu yaye yi dou amat man
sorri negn sunu baye yi deug rek moy takh moy wakh mane
pa bouy gerer 4 women legniouy wowé bad man
pa bouy gerer catwomen leniouy wowé batman
anh soutoural, fils so beugé seu dara dokh faut que soukk ramm
fi guey guiss ay beau parleur you andak lamign you niaw
l’habit ne fait pas le moine mais ya des habits pour moine
rigne*se bi deyy tekk xxx seu téré
degn neub niit bou nioul n*gga bind ko si téré
kouffi nek chomeur tokk di watt ni degn ko liguey
deuk bou ken dou liguey wayé nieup legniouy liguey
[hook]
eyoo fi moy senegal lou nekh wayy deff
sunu bougoul fen deugg leniouy neub
defal loumey wakh boul def limey def
defal louleu nekh g*yi negn leu soutoural soutoural (wooo)

[refrain]
soutoural soutoural ( woo)
soutoural, soutoural (woooo)
soutoural , soutoural (wooo)

[pont]
[couplet 2]
bou féké yemo place boul signer monogamie
boudé niémé wo clash boul signer polygamie
dina leu meyy seu batt boy youkhou sama famille
bou féké men are trash, djiguen moy autombalit
da melni afrique soffi sathioul mouno nek milliardaire
lane mo gueuna raciste wakh nitt kagna wala ndringg
kogn bo dougou niéti djakka wayé ben doussi fess
pa you eup djabar niou fi eup ay maîtresse
système lmd, système lmd
lewal maitresse diabar loloy systeme lmd
liguey méché dokhane yeaaah système lmd
primaire gueyy nopp seu maîtresse djang système lmd
yeah. soutoural. fi so beugué seu dara dokh faut que gueu soukk ramm
am niouy détourne khaliss dem dissi tabakh djakaa
nara nakh sem bopp fokk ni niou gui nakhh yallah
[hook]
eyoo fi moy senegal lou nekh wayy deff
sunu bougoul fen deugg leniouy neub
defal loumey wakh boul def limey def
defal louleu nekh g*yi negn leu soutoural soutoural (wooo)

[refrain]
soutoural soutoural ( woooo)
soutoural, soutoural (woooo)
soutoural , soutoural (woooo)

Random Song Lyrics :

Popular

Loading...