lirikcinta.com
a b c d e f g h i j k l m n o p q r s t u v w x y z 0 1 2 3 4 5 6 7 8 9 #

nittou tay - noiro lyrics

Loading...

intro:dafa rér amoul ngeum(nittou tey)
iblisse la fal faté yonnét(nittou tey)
farataloul dinéme(nittou tey)…..fonétik
couplet1
yaw dunya def def bo degg midéf
fatté yalla fal yonnét yalla xaliss
lothi guiss?nakar ak tiss
safane yi di geuneu wathieu
niawtef sentou sa morom
thi galou xathie
fen ak kathie
senegal yéné yé gnou tardelle
yalla atélle
loxoy def té loxoy té loxoy ndindi
dieuf diou yakou def lou bone ba alkou
t-ss seuye rayi bakéne
rithie sa téré am sa yalla bop
wett taxoul nga xam séne bop
finition ng-y sett namoufay teudé
xana do dé
koune mome geumoul nelawoul
ta fé gnou dieum
lofi djiwone nga fay guopp
doufa dial say soop
aduna diar dial
-ssalo wakh lou bakh def lou bakh
diaroul yéne yi
ma yeureum gnén gni
talibi xatoul xoll yé xatt
yémoul rek thi chauffeur yi
dagn fé bari chaud coeur yi
douma dém ta kén dou dém
refrain
nitou teyyy(thieuy)
sole dalame
nidou tayi(doyna war)
nittou tey(dafa réer)
soule deugeu souli fén
dieufi ma teyy-2
couplet 2
yaw nittou tey
sole na dalame
nidou tayi
thi soul deugeu
souli fen bako sai sai
-ssalo na boppam
fouti soul bouki souli bouki
xol beutou diambour
sa yéné done louki
jamono bi boy sett ngoor laguo lafi
amoul kéne fi koufi dieufé waxi nabi
mo tax sunu biir cheytane fess nafi
kaniane bone siss
niawtef legui dagn ko miss
thi jamonoy dadial
fep fep la dadial
beugeu ami deureum
dagg nitt thieureum xeureum
gnogui lay réunion
rélo ni amdi mignon
loumou la eupeulé xagne lako
dieul na muchiba xagne lako
démo diko ay gnane woutiko
sa mbokk mola bloqué
agne bagui ni boko léké
maguoume dieum la té r-ss
keupeu caisse tabax ter-sse
n-ssaxal do gui trace (wou waa)
couplet 3
xamna li nek sa xell
mola geuneu mbong
day diar sa kaw
téféssou wone la ndong
nittou tey dou rouss fen na barodé
trois quart coss ganila borodé
louer auto trafiqiant de personnalité
naik diom fók ni lolou moy nandité
goru thiapatate démarchame fémi néne la
foko fék kebatou dou masculin féminin la
madar boy sett omo la
matar legui h0m- la
boumou la guondek 4/4 tame
louné lay dathie dani sax tate tatame
guel done ay lesbienne
escroc bari lescul fils you k….
xamé touma galsen
ooh my god il nous manipule lucifer
guindil sama xett gnou deugeur ni barre de fer
gnou deugeur ni bar de fer

Random Song Lyrics :

Popular

Loading...