lirikcinta.com
a b c d e f g h i j k l m n o p q r s t u v w x y z 0 1 2 3 4 5 6 7 8 9 #

badou meun lepp - nix lyrics

Loading...

dofoulo djinné péssoula, (x4)
khamé nga khamé nga khamé nga yalla ak yaali
khamé nga yalla ak yaali
khamé nga yalla ak yaali
ki ley paadial dila doute dila yaali
badou meun lepp

{verse 1}
ndiago bi nénama nikissi
khekh bi dou diekh ba nga paré ci
gnoussal gnou mc yi diape ci
sedalal bières yi gnou yakhe fi
kholal ma khalé bi nga andal non bokossi
danga dioup lokho ni oguchi
dougal rek ng-y def oh que si
n-gga yay dogal gnou tope ci
yang may khaar boy mais naa le beete
gueun le tang fils ci khol bou sedd
khamo gatt fils sa khel a guède
chaque jour nga guent né mang ley yèdd
non mais fils danga niake diom
chaque jour ci beat bi gnou def la dom
chaque jour nga diebalou tek sa aum
man may alcool bouy fedj sa gaum
n-gga gnola gueneu dé kodjal sunu concert ci armel bi chaque jour gnouy rey aki dekil rap bi
rap wolof dou sama game mais saayou ma playé nga moudjé seeti arbitre
yeah dama neek, dama sokhor may professeur boula doul may sakh nga tokho
dofoulo djinné pessoula mais beuss boula pessé dinga khamé sama lokho
{refrain}
dofoulo djinné péssoula, (x4)
khamé nga khamé nga khamé nga yalla ak yaali
khamé nga yalla ak yaali
khamé nga yalla ak yaali
ki ley paadial dila dout dila yaali
badou meun lepp (x4)
bombardier modou lo : 4 appuis (x5)
yekini balla g-ye : 4 appuis (x5)
gris bordeaux eumeu sene : 4 appuis (x5)
n-eazy rappeurs yi : 4 appuis (x5)
{verse 2}
game bi dama ko yaague diegui
khamoma? sa guel moma dégue
nga wagniko ngir mou sorima kone naako laal ak mmm bou goudou
khamatouma sakh boy kagne la djoudou
i’m so fresh ni di dora fouddou
ndeki ci lal bi ni laakh ci touddou
rap galsen lay solal mboubou
déguena souma fi néké do thiop motakh sayou ma touké nga youkhou « weer bi fegn na »
rappeur yi aka gno keukh ak loumay méyé yeup gnou nane n-eezy bone na
moun na la gaagn ak ay flowou dembe
flowou ganaaw souba lay méyé souba
charlatan la mais damay khoudbeu
ay téré gucci ci biir sa guembe
4 appuis 4 appuis my n-gga
saafara flow n-gga mandi nga
technikou diouf wala fadiga
manaam gauche wala droite n-gga taalina
mane ak rap boy ni justo ak balbina
ni congo degn ma désiré kabila
daan téleu yéwou naan diangui naa diade cogne rek seyyy
{refrain}
dofoulo djinné péssoula, (x4)
khamé nga khamé nga khamé nga yalla ak yaali
khamé nga yalla ak yaali
khamé nga yalla ak yaali
ki ley paadial dila dout dila yaali
badou meun lepp (x4)
tyson tapha gueye : 4 appuis (x5)
gouye gui my n-gga zoss : 4 appuis (x5)
ama baldé tapha tine : 4 appuis (x5)
n-eazy khalé bi : 4 appuis (x5)
n-eezy diaarone nafi wakhatifi ay ndiakhoumeum dokhi
lokhoti fi mbotou g-yi paré yokhossou fi ay mc meuneu gaagné
kane mo le gueneu mouneu djeli ci sa game bou déé bi
soudoul n-eezy boy té doula djaay dolé
ndakhté li ng-y meneu yèèk yeup mouno gnou djaay golo
amoulo fi nélaw daniou gaaw dinga wanne ngelaw

Random Song Lyrics :

Popular

Loading...