yoonu ndaw - nitdoff lyrics
[couplet 1]
dokh ci yonou ndaw dafeu bari piège
meun nga fallin’ down meun na doon lou yées
doolé dokhoul diam saurato ay conséquences
life fou legalize rékey doon sey influences
yonou ndaw dou wéey teguil sa tank please
bodoul ingénieur meun nga doon chef d’entreprise
att yi nga tolou sa dérét dafey tangue
so tarkhissé rek meun nga niak bepp maîtrise
[refrain: mao sidibé]
petit frère écoute moi
yonou ndaw moleu djiap mélo ni
petite soeur mais dis moi
pourquoi tu penses que si triste est la viе ?
le meilleur rеste à venir
c’est maintenant que tu dois batir
ton avenir, ton avenir, prépare toi pour ton avenir
[couplet 2]
yeah ya ngui tolou pont bou diafé djiegui boy
gni si toloon naagu danio djieki djieki yooy
virage bi nga nekk moy déterminer fi nga dieum
andado you bonn danie léy précipiter ci leundeum
niep gui koy def waroul takh nga warko def
complexer bakhoul doon sa propre chef ci li séy choice
khana xamo ni diné meun neu doon boussole
so tchi télé tagguatt sa bopp
léer gui dafey sakh sa khole
[refrain: mao sidibé]
petit frère ecoute moi
yonou ndaw moleu djiap mélo ni
petite soeur mais dis moi
pourquoi tu penses que si triste est la vie ?
le meilleur reste à venir
c’est maintenant que tu dois batir
ton avenir, ton avenir, prépare toi pour ton avenir
[couplet 3]
han khalé bou dioumé boul ko téleu wakh ni da nga bonn
dieuleul sa temps nga dioubanti ko bamou doon
ki ngey saguo euleuk fepp nane khole léen sama dome
guinaw yallah dala sameu lo kone waro faille
beurina wadiour youy échouer tchi sen oyofaay
sa dome dou nguew am xélam boul ko yéw
liy thiossanam warna fégne tchi mom fepp foumou téew
sinon rek nga sopiko ap dondjie keurign ci biir méew
[refrain: mao sidibé]
petit frère ecoute moi
yonou ndaw moleu djiap mélo ni
petite soeur mais dis moi
pourquoi tu penses que si triste est la vie ?
le meilleur reste à venir
c’est maintenant que tu dois batir
ton avenir, ton avenir,prépare toi pour ton avenir
[outro : mao sidibé]
little little sista
little little broda
take care of yourself
adouna yaguoul wéi
yonou ndaw dou wéey dou wéey dou wéey dou wéey dou wéey
kone gars yi téelou léen
Random Song Lyrics :
- for granted - mbl solo lyrics
- life is hard but without a girl but you got it - rappop kirukkanz lyrics
- snow - lil' veloci lyrics
- йо-йо (yo-yo) - лилу (lilu) lyrics
- suffer - fittsaddd lyrics
- mały raj - młody gengus lyrics
- shotgun - sxulcvtcher lyrics
- meuf de la nuit - ramo lammar lyrics
- empty - desire (rapper) lyrics
- istruzioni - venerus lyrics