lirikcinta.com
a b c d e f g h i j k l m n o p q r s t u v w x y z 0 1 2 3 4 5 6 7 8 9 #

wané fite - nitdoff lyrics

Loading...

[couplet 1]
wané fite wané diom téladiouk job
bénéfice bi dou doye t’es le big boss
kén dou beugu guiss sa famille mouy khoss
wala doundé ay dessitak one of this stuff
djiteuleul deun g*yndé dou tite
goor dey banieu deuké talal lokho
soutoura bolekok goorgoorlou
sa you naré xawékou mou sangualako
lo def taye khép ko
jambar nga diougual nga dani doolé
taudial sey guent ragual dafley tunk soko doné
dar dar il me faut de la money
la motivation je vais me la donner
l’epoque est tellement cruelle
si t’as pas de sous personne ne t’connait

[pont]
sama rétanou yaye boye laay guiss
sama rétanou yayе boye (yaye boye)
sama rétanou yayе boye laay guiss
sama rétanou yaye boye (yaye boye)
am make money for real
my n*gga am make money for real(for real)
am make money for real
my n*gga am make money for real (for real)
[pré*refrain]
sokhlawma takk ngandi bling bling
douma ap consommateur victime
liguey beu téral samey wadiour
ak dimbali new di doolé yi miskine
khaliss dou dieurign loudoul fathie gathié
neleen niou demé goorè tchi téen
bou naré indi tort sa honneur
neleen niou demak mom tchi poubelle

[refrain]
wané fite wané fite doga got cash
wané fite wané fite doga got cash
bénéfice bénéfice en espèce
bénéfice bénéfice en espèce
money full moy sunu anti stress
money full moy sunu anti stress
wané fite wané fite doga got cash
wané fite wané fite doga got cash
bénéfice bénéfice en espèce
bénéfice bénéfice en espèce
money full moy sunu anti stress
money full moy sunu anti stress
wané fite wané fite doga got cash
wané fite wané fite doga got cash
wané fite wané fite doga got cash
wané fite wané fite doga got cash
[couplet 2]
wané fite wané fite ankéy
kénn douma help souma banké
fokk ma def ay sacrifices
ndakh life dafmey esquinté
wané fite wané fite door waar
missionner melni soldar
gotto get rich my n*gga
fimou néh douma freiner sakh ci dos*d’âne
dotoul yeuffou boy
dama wara awou baay boye
g*yndé reub sooy da fekk tilll yaafooy
soumey natt cible dey toucher melni cowboy

[pont]
sama rétanou yaye boye laay guiss
sama rétanou yaye boye (yaye boye)
sama rétanou yaye boye laay guiss
sama rétanou yaye boye (yaye boye)
am make money for real
my n*gga am make money for real(for real)
am make money for real
my n*gga am make money for real (for real)

[pré*refrain]
sokhlawma takk ngandi bling bling
douma ap consommateur victime
liguey beu téral samey wadiour
ak dimbali new di doolé yi miskine
khaliss dou dieurign loudoul fathie gathié
neleen niou demé goorè tchi téen
bou naré indi tort sa honneur
neleen niou demak mom tchi poubelle
[refrain]
wané fite wané fite doga got cash
wané fite wané fite doga got cash
bénéfice bénéfice en espèce
bénéfice bénéfice en espèce
money full moy sunu anti stress
money full moy sunu anti stress
wané fite wané fite doga got cash
wané fite wané fite doga got cash
bénéfice bénéfice en espèce
bénéfice bénéfice en espèce
money full moy sunu anti stress
money full moy sunu anti stress
wané fite wané fite doga got cash
wané fite wané fite doga got cash
wané fite wané fite doga got cash
wané fite wané fite doga got cash

[outro]
wané fite dong
wané fite dong
mola thiy guéné
wané fite dong
wané fite dong
mola thiy guéné

Random Song Lyrics :

Popular

Loading...