retroviseur bi - nitdoff lyrics
[couplet 1: nitdoff]
légu légu ma geum di dianère lii diota wessu sama life
bigni dougue cii rap nineteen ninety five (1995)
rak tak niou alou khirou defko thioki mic di fight
hard cor bégnou bercés nioune douniou tiapatattt
daniou dane tak lampétak balaa niouy dem rap attack
légui game bi dafa tiouné té boyyi daniou yoy
rak tak niou woté tiouné melni ay souris youy djoy
life bi nimouy démé dafa gaw ni tialemère
beurki dembo ndiaye garrage’ou kébémère
niou tokk dii f-ss ay dream cii bii life bou éphémère
dafa beurii teuss teuss dag-y dem beu teuthiou
légu légu ma geum guissate yèn djeuf youmay reuthiou
aduna werrou korrleu té kouy worr digua djoubou
légu légu xell bi dem cii kiné codou ak tanta diop’ou
sèn yakh dina sedd cii guédjou firdawsi la saubou
rest in peace (r.i.p) mauwtii daflène téleu yaubou
[refrain: mao sidibé]
yes yes
yes to this way
lii diota wessu sunu back in a day
say yes! yes
xalé mague naa taay god bless
sunu lamp takk neu taay
aduna ngui nii daay nakari di nekh
dara amou fii solo n-gg- lep daay diekh
say yes! yes to this way
lii diota wessu sunu back in a day
[couplet 2: nitdoff]
légu legu nga geum tokk images yi défilées sa mind
geusseum sa bopp mougne, fatélikou ré
ngélawou namel eupouleu nga guéssou dadiii tiss
nakar ak banekh kou nek moménga sa biss
legu legu ma geum plongé cii samay souvenirs
xalate yi dimay rongé ba damay seug miir
aduna dafa teureudii mounou loko xelmatii
amena niou dane yélwane taay niou ngui yéwo almadies
touteu tank leu justice seum dafa gatteu
bayi lèn ko ak yalla justice seum amoul aapeu
aduna amoul solo lou bess dina rapeu
cii lépp lii laay moudjé bala li bess di nieuw after
after after after after
[refrain: mao sidibé]
yes yes
yes to this way
lii diota wessu sunu back in a day
say yes! yes
xalé mague naa taay god bless
sunu lamp takk neu taay
aduna ngui nii daay nakari di nekh
dara amou fii solo n-gg- lep daay diekh
say yes! yes to this way
lii diota wessu sunu back in a day
[couplet 3: nitdoff]
yo!
cii boppou kogne bi laniou danetokk
sènetou sunu euleuk cii yonou hip hop
cii boppou kogne bi laniou danetokk
p-ss p-ss laniou dane démé cii bobou époque
cii boppou kogne bi laniou danetokk
tiéné di freestyle ba talou nio thiop
rap pur et dur beugou niou waune commercial
xeuth mic bi alou ni gaindé bou mèrr cii aaleu
rap tchii politique founiou dém tiowlii djiip
xeup tchii kané ba foniou dégg né all sh-t
télou niou degg dathie cii galaniou hard cor
télou niou def block kone soxla youniou gakorr
ték thiayine féth rimes cii digui dianteu bi shine
clando cii rap xamé youma ndex ay punchline
cii boppou kogne la diangué rabou mbede mo gueune tchii mind
molaay def real dioxleu gueude ng-y gueune dii shine
[refrain: mao sidibé]
yes yes
yes to this way
lii diota wessu sunu back in a day
say yes! yes
xalé mague naa taay god bless
sunu lamp takk neu taay
aduna ngui nii daay nakari di nekh
dara amou fii solo n-gg- lep daay diekh
say yes! yes to this way
lii diota wessu sunu back in a day
yes yes
yes to this way
lii diota wessu sunu back in a day
say yes! yes
Random Song Lyrics :
- precious - appleonia lyrics
- kicking up the dust - cast lyrics
- b.a.d tout le monde [remastered] - b.a.d carma lyrics
- gage low - equalz (nl) lyrics
- slime ball - sad_addikt lyrics
- notre dame mc - chakuza lyrics
- disappear - nexow & shockline lyrics
- song to you - curly bammm lyrics
- spirals - blessed lyrics
- exotic - perfectbwoy lyrics