reglel - nitdoff lyrics
[couplet 1]
nioul na teh bari dolé nan dou séw na khéss
douguou na si khole you deuguou yi ma khéw ma besse
never ever meussoul meti bameu sell my -ss
still underground mc boudé rap my best
i run this game and i keep rep my tess
deugu leu tchi mbed paris yi j’ai vendu la neige
démna tchi gardav mais meussou degg j’ai vendu la meche
how many time la dougu tchi taukhidouna dem jail
how many time la yoné cash money comptel
how many time la deh founiouma braqué gun
mded nimouy diouré nonou leu meuné taguéy dome
gni leu beugu douniou diouk tchi pleure yi mais do djiss
loudoul money apeuko beu fleury merogis
polizia bou guéné gun derotou neroy tiss
fi kounie fi dathie si kess yaube rek seu mérey tiss
how many time laniou fi k!ll nit tchi injustice
bakenou nguew mo gun bou nit kou nioul si sen guiss guiss
niak pékhé pékhé leu la moudjie def slogan
kamikazou tchi ay deal beu moudié done delinquant
fadiar tél nga degu thioy yi feugu percusion
caguoulewou andi seni dog yi tekk la pression
how many time laniou fi seuf nit bounie amoul ay preuves
signer loleu procès verbal you woutek sey dieuf
sodé black juge bi dafley feugu ay years
sodé white lou cas bi graaw sursis ngey dieul
now you know loutakh ma rancunier beu meulni sisra
limeuley tegual ni dou movie ladial boy mirsa
how many time laleu thioyyi kepp amoulo pepp
niou humilier djiap door banopi pomp leu gaz
how many time lanioula taf fekk nga yoré sa money
niou foukatiko neleu diougu fi mba niou takal leu lame yi
enbrouille sous le prehaut ça part en couille
ça tape la barre fixe les pompes et les raquetteur fouille
transact au parloir pour faire p-sser le bedo
c’est la baston pour les pointeurs et les pédos
how many time la deup niew indalé ay briques
[ refrain]
reglel comme que rethiou meunouta sopi ay dieuf
th gua dal diam bala guay diouk di deff
reglel comme que weurseuk bila yallah diaglel
digua si diot sa you waxtou bimou ko nam dioté koneu reglel
comme que rethiou meunouta sopi ay dieuf
th gua dal diam bala guay diouk di deff
reglel comme que weurseuk bila yallah diaglel
digua si diot sa you waxtou bimou ko nam dioté koneu reglel
[couplet 2]
lou yague nèh si sama mind leu
yagua loukhi sama beut
make money by any meaneu toukeul sama life
toute tank tchi bounteu life mane mi tougueul lameu fekk
mbed diokhma dioumtouway yi ndéké tendre nameu piège
chaque night soumey gnibi galé compté ay liy-ss
deuk hotel ak villa di dokh si shopping ak voyage
poche you diss ak meuneu tchiatche dafey yomb nga serrer meuf
cristal bi wekh neu tal banopi di guen zero neuf
marcadet clignancourt auber ak plc
tak-ssounou printemps laniouma grillé tchi ay jumelle
gnénti fane lanie tchi tekk may doga kham ni k-sso mél
fadiar tèl oxy feugu bounte diokhé la gamelle
b-tch yimeu dane batterel ken niewoul parloir
wathie promenade bi niakantèko tchi raak général
refus d’optemperer commission bi yaube meu mitard
few month later out of jail délou case depart
[ refrain]
reglel comme que rethiou meunouta sopi ay dieuf
th gua dal diam bala guay diouk di deff
reglel comme que weurseuk bila yallah diaglel
digua si diot sa you waxtou bimou ko nam dioté koneu reglel
comme que rethiou meunouta sopi ay dieuf
th gua dal diam bala guay diouk di deff
reglel comme que weurseuk bila yallah diaglel
digua si diot sa you waxtou bimou ko nam dioté koneu reglel
[couplet 3]
bi life dalay cambal
lou yomb lalay tamal
ay nakhi néen lay moudj doneu gua doneu diam diko ramal
def na tchi mbed paris ay putain dégâts you bari
tay rethiou lama diké ndakh yakh na si life diambour
beugone tekki waral ma eupeul melni kouy djiro
nitt kima diamone pakka kane moma wakh né déwoul
kima yabilone péer kane moma wakh ni overdozoul
ay lathie you amoul tontou ma warko layo ak bourbi yallah
donté douma modèle mais meune gua diang si sama sons yi
xelou xalé moma diapone ba tay may toup sama torts yi
niou bari si nioune système bé niou poussé pour niou fauter
ndakh amouniou pép té mounouniou delou galé ak lokho néen
dag-y dièma diouk takhalou tchi ay montres ak ceintures
dou té tioy yi indil leu fitneu deuk tchi bavures
sometimes meuno comp sori sa deuk nimou mété
xeuy toumouranké fi gaaw neu lolou té fi dafay bété
ndiaboot guagui xaar gua yooné mandat weer bi dead neu
daniouy fok né fi xaliss dag-y seukh lep yombou
sometimes niou fatali leu diw defat neu sén keur
mou geune leu yokk khaptal ndakh té froissé nagn seu égo
_
yeah
gua beug prouver say mbook que né do yafouss
takh mou dougeul leu si yeneen ak yeneen you know
yeah
diemou ma layal keen but sometimes it’s not easy, it’s not easy bro you knowh
so no matter work dou yag bali aramone dagane man
boula yallah dioxé occasion wala seu chance
nagua ko saisira dièma tégouwat si yoon bou dioup bi bro
yalnaniou yallah sameu té diégal niou bro
règlel
règlel
[ refrain]
reglel comme que rethiou meunouta sopi ay dieuf
th gua dal diam bala guay diouk di deff
reglel comme que weurseuk bila yallah diaglel
digua si diot sa you waxtou bimou ko nam dioté koneu reglel
comme que rethiou meunouta sopi ay dieuf
th gua dal diam bala guay diouk di deff
reglel comme que weurseuk bila yallah diaglel
digua si diot sa you waxtou bimou ko nam dioté koneu reglel
Random Song Lyrics :
- outta this world - grae lyrics
- unspeakable - neon heart lyrics
- når alle andre sansar kan få kvile - odd nordstoga lyrics
- more than a minute - dream regime lyrics
- 匿名萬歲 (niming wansui) - 孫燕姿 (yanzi sun) lyrics
- xo whore llif3 - dirty britney lyrics
- let's go drinking in the park - no fun haus lyrics
- more to see - lethal v & loge lyrics
- balade - leo svr lyrics
- fuel on the fire - lou siffer & the howling demons lyrics