louko fi diar - nitdoff lyrics
[intro]
loukofi diar yaw
adouna bi yagoul dara té lou niak solo leu man
soko dieundé alakhira yay kiy niak sa valeur
[refrain]
yagui xeuy di yéné nit ay moussiba (louko fi diar )
yagui xeuy di fessal da biir ak riba( louko fi diar)
yagui faté bougn lay yew di soul si pakh (louko fi diar)
wahma (louko fi diar) wahma (louko fi diar)
yagui diani koulay digeul dieuf diou bax (louko fi diar)
yaw sa bakane rec gua topeu moulay nakh (louko fi diar)
seytané boy dokh si niawtef dalay niakh (louko fi diar)
wahma (louko fi diar) wahma (louko fi diar)
[couplet 1]
diour sa dome sani si foss
liguey sa woudji pour mou doff
takk khala pour mou yome
deudeulélen pour niou off
tokk tchi bopp kogne bi brayé knife agressé soumi nitt
ame niou gueuneu deh dougu tchi almere( cimetière ) yi di souli nitt
yén niawtef dalay diakhal kikoy def souy djioulite
m-sslatoulo ay djirim yow ya gui teud si sen alal
seytané diokhnala dolé té lepp daleuko yombalal
xeuthio place diaral naleu takhalek nit kék saguom
té meun nga diot tchi place bi deh gnenen niew diarigno sa kom (argent)
adouna bi yagoul dara té lou niak sololeu
soko dieundé alakhira yaay ki niak sa valeur
té nga djiémeu doylo sa weurseuk mandou té rafétal
guiss nga bêtise bimou meuneu def ki mandi yorr fetal
yallaay xeublé euleuk rethiou nielna ki sama forfait dale
fi diamoukaayou yaallah leu gni fi neh deuko nioufi
wayé fileu ibliss di reubé ndiabotam biniouy laki
[refrain]
yagui xeuy di yéné nit ay moussiba (louko fi diar )
yagui xeuy di fessal da biir ak riba( louko fi diar)
yagui faté bougn lay yew di soul si pakh (louko fi diar)
wahma (louko fi diar) wahma (louko fi diar)
yagui diani koulay digeul dieuf diou bax (louko fi diar)
yaw sa bakane rec gua topeu moulay nakh (louko fi diar)
seytané boy dokh si niawtef dalay niakh (louko fi diar)
wahma (louko fi diar) wahma (louko fi diar)
[couplet 2]
daw di dakhanték lodoul meusseu raw loula gueuneu guaw
nit yagui sakhal sén bopp laaf nguir beugu naw
yakamti weurseuk beu saguané seni deguine now
saubou tchi taukhidauna life beu moudjié dead guou niaw
taleuto takhawal sabal ki takh nga yéwou taye
taleuto show love sax gnileu beugu dembak taye
loula djiégué loool nga xeuy diko weuri fou sorri
meulni kou dieufeurou djiro gueumoni di nga yorri
di sokhoré gnenen tchi xeweul yilen yallah djiaglel
di weur di yakh derr sa bopp nguey wedjié tchi ni sa yar (éducation) mel
té nga ragal yallah téy khalaat teuraayou bamel
del ceddel nit ki linga kham tchi mom tchi dieuf you bakh
linko khamal tchi lou bone soutoural ko té yallah takh
kén dou maye sa bopp kouné sa weurseuk khamo noumou tole
nangulal ki sakk rouh yi ay ndogalam té ame tchi yole
sagueum mouné téh mou ame so tchi andoul ngagne nga sa khole
[refrain]
yagui xeuy di yéné nit ay moussiba (louko fi diar )
yagui xeuy di fessal da biir ak riba( louko fi diar)
yagui faté bougn lay yew di soul si pakh (louko fi diar)
wahma (louko fi diar) wahma (louko fi diar)
yagui diani koulay digeul dieuf diou bax (louko fi diar)
yaw sa bakane rec gua topeu moulay nakh (louko fi diar)
seytané boy dokh si niawtef dalay niakh (louko fi diar)
wahma (louko fi diar) wahma (louko fi diar)
[couplet 3]
tchi ay preuves youniou pirate la niou songu yakh iraq
Random Song Lyrics :
- my radio - oktaf kanis lyrics
- attention - northwx lyrics
- dopamin - lotte lyrics
- what da blunt - big boy gang lyrics
- i am a duck pond sailor - duck pond sailors lyrics
- revolution - indio saravanja lyrics
- sucker - a skylit drive lyrics
- burds - carter tondo lyrics
- let me be your fantasy - gok wan & craig knight lyrics
- california dreaming - 3ron x pirate the rapper x vxrtual lyrics