lirikcinta.com
a b c d e f g h i j k l m n o p q r s t u v w x y z 0 1 2 3 4 5 6 7 8 9 #

clando - nitdoff lyrics

Loading...

[refrain]
one time bodoul real doko guaweu yeuk
d.o double feuzeuw amoul paper dafey fakh deuk
two time shut the f-cker boulma bak thug
mbed faye neu real let me hear you say brakeuzeuup
three time yow mi foguoon k!llah kaaw leu deuk
l.o.u.g.a bling biy shine dafey yakk beut
malen gueuneu guaw na niep teufli laaw leu thiat
nd k!llah ak niom day melni kakatar bouy dakk leu

[couplet 1]
we don’t give a sh-t sa money ak sa thiaazeu nice
bou game bi nekatoul si bordel nioko organize
thiop beu nice flow biley sekilo meulni casa rice
fouleu fayda goré diom ak diné tchi sama father eyes
fou sapé dioubé nioy djiité teré bi nioko mine
fou thiowli djibé nioy thiokil mbed mi doko mime
kk maroul sa tate da ngey sissou beu doko lime
f-ck yow ak sa team hardcore bey sama dokhaline
hey yow fileu k!llah egu leu my flow is so regular
bo deugueuwoul niou segu leu purposou g-yndé regu leu
bazouka busy gars diksa ni yakouza
galou xathie nga yakeuloon tathie di khar mou soukouthia
lyrical monster thi mic di ressuscité mbinde mi
flow bi di baleu daley raye sou souté mbeud mi
mbot eumb bi tchi rap di diokh lou dope under bi
diwsquad cl!ck bouy romb yay tiop peundeu bi

[refrain]
one time bodoul real doko guaweu yeuk
d.o double feuzeuw amoul paper dafey fakh deuk
two time shut the f-cker boulma bak thug
mbed faye neu real let me hear you say brakeuzeuup
three time yow mi foguoon k!llah kaaw leu deuk
l.o.u.g.a bling biy shine dafey yakk beut
malen gueuneu guaw na niep teufli laaw leu thiat
nd k!llah ak niom day melni kakatar bouy dakk leu

[couplet 2]
yo bodé real bouy tewal di naleu naw
boudé fake -ss sa galeu ngui tereul u gotta know
i don’t know fake friend yeah takh ma parano
hey bou dara low mbed dey fayekou lot of doe
cr7 la tchi goal yi nanie andi sén saakou rogne
kougni niodi king beu dadjiek mane yaay soumi sa couronne
mba meu def leu beuy sekin tchi pombi terre ak makeuroon
daniou rame tchi rime dokh tchi rap flow bi magu run
k!llah cagouleum defko teleu simi fang dathie
demal djiangui mic daniou dem beu niew teh yagui wathie
kén ngentéguoul sa flow té ya gui rap sa nakou deuthie
niata mc lagn fi iri sén guimigne ni rappeu teuthie
meun nga deuké keufeulou beu w-ng di daguou facebook
niodi internationnal té wessogoulo thies-pout
boula cétou bi diayé beu nileu da nga fresh look
takh nga saurou k!llah tchi simili daley féss diouk

[refrain]
one time bodoul real doko guaweu yeuk
d.o double feuzeuw amoul paper dafey fakh deuk
two time shut the f-cker boulma bak thug
mbed faye neu real let me hear you say brakeuzeuup
three time yow mi foguoon k!llah kaaw leu deuk
l.o.u.g.a bling biy shine dafey yakk beut
malen gueuneu guaw na niep teufli laaw leu thiat
nd k!llah ak niom day melni kakatar bouy dakk leu

[couplet 3]
mic nena boulma raaay mbed nena boulma lie
yen a marre tchi gnimey sikki sakka daniou fou malade
woté nga tégnileu deudou niew tchi mane sa wa keureu
nok di rok thiafka mbedeu saf tchi sama akeureu
nioun sunu rap njiaru nopouleu ngey diourgauto
niom douniou raakk té folen kép djjiss feu goor dioutou
baye fallou mbed yey mbeuk ni dieuwrine puissance
boy songu nd k!llah ya ngui xeupo dewlin bouy sens
bo xamoul nouniouy djaté diane nagua gaw ni amy mbacké thiam
ladjal boyz yi niamone sama dangar niom niniuy niaké diam
guelawar rest in peace abou camar deh
niom niep laay canardé kikoy djiem ak kiko nar déh

[refrain]
one time bodoul real doko guaweu yeuk
d.o double feuzeuw amoul paper dafey fakh deuk
two time shut the f-cker boulma bak thug
mbed faye neu real let me hear you say brakeuzeuup
three time yow mi foguoon k!llah kaaw leu deuk
l.o.u.g.a bling biy shine dafey yakk beut
malen gueuneu guaw na niep teufli laaw leu thiat
nd k!llah ak niom day melni kakatar bouy dakk leu

Random Song Lyrics :

Popular

Loading...