lang gui - momo dieng lyrics
man damay lathie beug kham
damay khol nguir beug guiss
dama rer ta beug fegnn thi xaleil (×2)
sama yaye bayimaa ma dem seeti
xalei yii sen lang riche neuu
wowoo damakoo dama beug setti
xalei yii sen lang riche neu
man damay lathie beug kham
damay khol nguir beug guiss
dama rer ta beug fegnn thi xaleil (×2)
maman bayimaa ma deim seti
xalei yii sen lang neikh neuuu
wowoo damako dama beug xooli
fatou kine ndour langam neikh neuuy
wawaw damakoo dama beug seti
fatou bintou ly langam ruche neuuu
man damay deim(×8) wooy
man damay deim(×8) wooy
man daal lang yima meusseu diar yeip
lang gui tay mom-ssi daaakhal
lang yimeu meusseu deim yeipeu
lang guii tay mom-ssi daakhal
man dei beug naaleine
djigueni senegal man dei fonkat naleine
man dey wolounaleine
djiguene gni man dey beug naaleine
cherie boy boul nam dara tay
diapal ni may sa superman
man dal diaral ngama naam
loo beug ma indil laako
gnoun goor gni nagnou def souniou gneti morsso
teilssi kopati ak ay mbarakiss
djiguene gni gnom dagno civilisé
teikssi am filing ma beik thi yeeine
yaw so beugueiiii heiii
fariyoooleiiiii
Random Song Lyrics :
- what up - angela brown lyrics
- angel of revolution - hideous divinity lyrics
- meus erros - isca de polícia lyrics
- zero km - sjaak lyrics
- ninety-eight - jraw702 lyrics
- take me to your shower - hosey r lyrics
- on bouge pour lui - tigers lyrics
- lyrical warfare - keneddythedon lyrics
- starp divām saulēm - prāta vētra (brainstorm) lyrics
- do you want to play - milwaukee bucks - jody whitesides lyrics