lirikcinta.com
a b c d e f g h i j k l m n o p q r s t u v w x y z 0 1 2 3 4 5 6 7 8 9 #

idda - mia guissé lyrics

Loading...

danga took sama xol yaye kiki mome léboone
guénteu na takeu leu kaay done sama yayou doome
dougou na doundou na mougne took ndax yaw doome
té beuss boussa doome indé dome defco dome sama doome
li nit di dathie thi naigou seuye
di guiss sa yaye té doko ko sagna déye
li nit di dathie thi naigou seuye
di guiss sa yaye té doko ko sagna déye
dinala romb midi
oooh wait
té doma guiss
oooh wait
pénicilline yangui gneuw
oooh wait
ma dabali
oooh wait
gaa fof no welly
oooh wait
now doto ko défati
oooh wait
oooh wait
oooh wait
gnata yaye la fi seuye teuthie thi kasso ndax séne doome
yi lathie ng*y lathie téy amagou ma tontoome
yague toul legui rek nga xam louy noonе sama doome
ideu bi tey la diékh tay di diéguеulou waat sama doome
li nit di dathie thi naigou seuye
di guiss sa yaye té doko ko sagna déye
li nit di dathie thi naigou seuye
di guiss sa yaye té doko ko sagna déye
dinala romb midi
oooh wait
té doma guiss
oooh wait
pénicilline yangui gneuw
oooh wait
ma dabali
oooh wait
gaa fof no welly
oooh wait
now doto ko défati
oooh wait
dougou na doundou na mougne took ndax yaw doome
paré* paré* pa* pa*
paréna
xamoni bou diééxé
diééx na
diééx na
gneuweul
han
ngani
han
han
mani baydou volume
sabou mi nana ni
tékki lunettes yi nguir gueuneu guiss

Random Song Lyrics :

Popular

Loading...