la mancha - mgeey lyrics
dëgg gallaaj taxul ma toog ci nen
ñoo la gën taxaw yaa ngi toog di fen
waxal gels yu nooy yi maay sen oxygène
rappeur bu toppul samay règles naa la def jigeen (k!ll′em)
ëppël classe te du ma daw samay devoirs
qualifier d’office penalty du ma ko oral
defaru ma serveur waaye maa ngi joxe pourboire
di nga teggi coow booy jeem a natt sama pouvoir (what)
soo may jaay muus di naa la xuri hum
indi cancer ci sen xuur yi hum
lekk ginaar yëkkëti poulie
rindi bepp jinax moo tax leegi tout me sourit hum
xam naa samay droits te dewma sodav
am naa identité te soxla wu ma daf
ku taxaw sama aile naa damm sa laaf
naa len tëj ci cage te du ma ci kaf
weñ sa loxo booy jeem a bras de fer
naan sa dereet booy ñoddi sanguinaire
xañ la bakkan nga dem fanaan cimetière
soo may bañ di guddee mel ni ku tarder reer
eyo
gis ma gumbë
du ma dox ba tiit
yore xellu scorpion normal ma jiit la
lance*pierre sa fit
ng*y laaj ndax nitt la
du ma mbër mais da may xeex ba sama ñakk di siit (siteu)
bac+5 teela dajjale ay diplômes
fèeñu ma magazine mais di naa nekk icône
sons yi da fa indices pourtant maa ngi daw traces
da ma ammagul sa jot fate wu ma ñuus yi mala diggoon
du la mës bett boo deggee ni geen naa ci
tuuru ma dereet te sama xel bi aka nacc
pour muy clair bëtt′ag laamiñ mënu ma tëye
bi may jëll suite radison jàngagu ma fibonacci
grosse bite, rangale caisse mel ni 1da
say pics dese naa yees kay ma won la
man d’où je sors
weesu naa fort
da maa mën bokku ma’ag kiy def efforts
akk kiy sooga door
ma ñëw teg la tort
sa rappeur da may soor ndax sama xel bee ñor
li ng*y seet laa yor
yo soy el mejor
da ñuy leb say fan rekk nga demmee boor (k!ll′em)
mange′eg sama foi moo tax mënu ma daw res
gëwma ñi ma croix moo tax mënu ma dem messe
ku fi nànd m*geey moo la sibbël
dañ lay nokk may la credit pour nga woote ndimbël
mother f*cker
Random Song Lyrics :
- girl - live - the beatles revival band lyrics
- checking in and out in ink - zoomboom lyrics
- mood - eric bellinger lyrics
- amazing grace - amazing grace album version - bill & gloria gaither lyrics
- everywhere you look (the fuller house theme) - carly rae jepsen lyrics
- escape - nf lyrics
- true colors - alessandra maestrini lyrics
- paix - fello lyrics
- contra o mundo - biggs 048 lyrics
- un' estate italiana - official song football world cup 1990 - champs united lyrics