lirikcinta.com
a b c d e f g h i j k l m n o p q r s t u v w x y z 0 1 2 3 4 5 6 7 8 9 #

fii la wara yem (from “karma”) - maya abdul lyrics

Loading...

dundu negn lou nekh
mak yow lepp easy lepp nice
dundu negn nakhar
diar negn ci lepp lu dul peace
dundu negn lou nekh
mak yow lepp easy lepp nice
dundu negn nakhar
diar negn ci lepp lu dul peace
fii la wara yem

togn na la lou bari (i’m so sorry babe)
djital sama khel, bayi sama xol guinaw
yama xamal lou mel nii (oh ohh)
mbeuguel bou deugg lol
waye mbeuguel kesseh dou doy

dundu negn lou nekh
mak yow lepp easy lepp nice
dundu negn nakhar
diar negn ci lеpp lu dul peace
fii la wara yem

fii la wara yеm
fii la wara yem
fii la wara yem
dundu negn lou nekh
mak yow lepp easy lepp nice
dundu negn nakhar
diar negn ci lepp lu dul peace
fii la wara yem

Random Song Lyrics :

Popular

Loading...