lirikcinta.com
a b c d e f g h i j k l m n o p q r s t u v w x y z 0 1 2 3 4 5 6 7 8 9 #

ddr - king em lyrics

Loading...

king em diot na
0’oclock

[couplet 1]
deret samay lokho
diaralo ma ray ndakh douma si ame bakar
neek! kheuyna motakh ma dé melni kouy fanane tchi bamèle
dé tchi gniy dof doflou rek
dof doflou ni boys yi takk si rap
né dagno beugue tekki si rap
(ayway ndeysane rétane)
sama yoon na leer motakh ma paré déme
niak fé guiss loumay téré ndm
dedet dh
weddi ko rek nga dé
yay tek rek dh
fake -ss n-gga dangue fé guiss nitt
fresh melni tay la dioudou
dama takk kone fok rap bi di faye han
di negn hate mais nak si si c’est normal
diougué banque beuri borr ak ndème si yalla rappeur yima wara faye
gawal dougeul say sandi tathiou n-gga
mais thiow dou djip narna la faye ni weer bou dé
défou ma ak yaw feat même boko done niane ni tapéte boukoy sarakhou
rappeur yé dakk doule non ay diague legn rek
gni doundatoul moy gni ma done diaye geuneu dé
nieuw rek nek oustaz aoust tiazz bama feulé la sa rappeur moye ni kou ame dieukeur ame farre
tale na lou faye doul meuna faye
bokou gnou level do gnou meuna fréque
n-gga i did that
ak tank you eupe cicatrices sakh kou diam ay adidas
yaw dangua khew nioune douniou khewi ni deuthie
rotchi sama rouh nguir doga meuneu geumentou
taylé nelaw melni kou diaye lalam mane falé touma yêné neek leu ( maf-cker 0’oclock)

[refrain]
nioune la boys yiy diangualé lougn niou moussoula dianguale
nioune la boys yi yêy ndakh daniou dioudou rek mokale
nioune la boys you ndole yi dieunde lepp lougn fii diaye
yague ko khare ba tay yalla dji defna ma ko
dof doflou rek mais gno geuneu khame ni may king bi fi
dof doflou rek dagne may guiss rek nekate nitt
dof doflou rek mais danguey doule nak bo né ya meune fii
dof doflou rek dof.. dof.. dof

[couplet 2]
fake n-gga khamo ma sakhe wayé dingue ma yabi ni nêw bou lapp si guedj
f-ck say guênt say guênt rek lay dess kone geuneul sanguo souf si ma guiss
moussou niou ame diotou ame diot
f-ck chance teu ndeysane moussougn mala maye
tekk ko tchi ba amatouma temps bouma dieul (ayway ndeysane retane)
n-gga sama bopp la investir tekki moma tale teu takk douma faye it (faillite)
c’est qu’a l’argent qu’on fait la coure f-ck cahier chéquier lay binde samay leçons
kone f-ck n-gga awma khole teu dara douma téré yeeg
kone pouseul fi ndm bama dioudo la commencer todj melni poussin si nêne (double f-ck)

[refrain]
nioune la boys yiy diangualé lougn niou moussoula dianguale
nioune la boys yi yêy ndakh daniou dioudou rek mokale
nioune la boys you ndole yi dieunde lepp lougn fii diaye
yague ko khare ba tay yalla dji defna ma ko
dof doflou rek mais gno geuneu khame ni may king bi fi
dof doflou rek dagne may guiss rek nekate nitt
dof doflou rek mais danguey doule nak bo né ya meune fii
dof doflou rek dof.. dof.. dof

dof rek di tekk
wayé sa flow safou ma gate ni tétine tchi sa mame
boys you ndole yi niofi dieunde lepp lougn fi diaye niokoy cut osh yeupay klaxonner
yaw deumé wo ay deume lay diolou sene sang tchi zéro
mangui ak sama gang shot si sa ndaye nga diomi ni kou guiss ay 500 cissé lô (bang bang)

[outro]
dof doflou rek mais gno geuneu khame ni may..
uhh dof doflou rek dagn may guiss rek nekate…
uhh dof dolfou rek mais danguaye doule nak bo né ya… uh uuh dof doflou rek dof dof dof

Random Song Lyrics :

Popular

Loading...