easily - kach lyrics
refrain
foumou dem wané fa meuninum
yeggal niveau au maximum
fou dieuf war doufa tok di wax microphone lay def ko magnum mam
foumou dem wané fa meuninum
yeggal niveau au maximum
fou dieuf war doufa tok di wax microphone lay def ko magnum mam
cauz i do it, do it, do it easily
i do it, do it, do it easily
verset 1:
mane soumay get son lep day niroo dafa melni comme ay j-ponnais
dang-y guiss con yi tek ay kilo caca ba nopi di diap né
dagnou aay “shiiiiiiiiiii” xamoulene dara plaké nga diawalek 21 carrat
kach day peura yobbou foroufara liguey rek soxla woul dem si ay mara
soumay gnew dagnou ballaie fep térou ma like obama
teksi di fly in the air dés fois je m’étonne naan who am i?
sar founé men ngelaaw wowéma
boulma toppou fowil men tem nga foé man
how many time b-tch, how many time
i turn a beat with my god d-mn flow into diamond
it’s my time, b-tch i’m on my grind
i can make a gift of blood my vein of full of rhyme
we’re on the top men, you better stop men
we gotta rock we gotta pop them godd-mn
its my clock men, with my black men
we cut them c-ck, we make’em lock them shot them
refrain
foumou dem wané fa meuninum
yeggal niveau au maximum
fou dieuf war doufa tok di wax microphone lay def ko magnum mam
foumou dem wané fa meuninum
yeggal niveau au maximum
fou dieuf war doufa tok di wax microphone lay def ko magnum mam
cauz i do it, do it, do it easily
i do it, do it, do it easily
verset 2
dagnou rap ng-y diooy b-ssa taat yi di boy sa wax di boy kaay ballou boy
nell boukh ni looy bougnou rap ng-y diooy xana xamoo niooy rap beuss bouné mouy boy
boul yékkati boppe yaw xam ngani bokk lignou tek dafa high boy xadioul sa bopp
dokko tay booy bekk bay yeungueul sa bope gnoune gnoolay beugueul ak ndiarrou nope
beat bi ni gnap nga bako fi diaar fé gnounila gnap nga diaaré fa diaarhé
ni baay fall kak nga songou gnou tapp sa gat nékko rap nga dieuléfa teulé
call me the ghost if you want the devil my little is about k!ll you
i’m gonna stay on the top of the needle till i satisfy all ma nizzle
bimay spilt my first rhyme yangui si pot di day
solil sa slip mon fils raam wouti sa poodji nday
mana ma diakhal team yep haa barça
mouss bou woolou boppam dougou si segg fanani barsakh
yaw milé xam ngani doom limon dou pomme limoom deh sa etonne
“i” nga bougnou fatté tomb mounoo fi bombe loo doone saalé kone
fexxel ba sori bi zone sino sa tombe gnou g-ss ko ni alcapone
negger its been a long gnou sentoussi com diot na gnou seukh si tonne
refrain
foumou dem wané fa meuninum
yeggal niveau au maximum
fou dieuf war doufa tok di wax microphone lay def ko magnum mam
foumou dem wané fa meuninum
yeggal niveau au maximum
fou dieuf war doufa tok di wax microphone lay def ko magnum mam
cauz i do it, do it, do it easily
i do it, do it, do it easily
verset 3
deggo limay wax “anh” bayil sa tollou baay
god mooy mayé b-tch koussi né ak tolou waay
kach si kaw beat doufou nourou nit boote baigon mossi aay
dinga niakh siit dinga diakh t-t né kou yekk mont sinai
mooy sa baay nooy nga baay bi rythme atanoko dagnay moudiou bayi
gnémé nga baay kach sai sai dafa bad dafa hot ni daay
sama rap dafa pop dafa tok baay, day tokh sa nope
sa laaf yi baay firréko fly high in the sky ni rasta nga gueum ni salasi yaay
outro……………………………………………………………………………………………………..
Random Song Lyrics :
- the undiscovered epic of walter champion - pilotdrift lyrics
- kill your sons - christian death lyrics
- sitios distintos - nacho vegas lyrics
- próba - nizioł lyrics
- handy - chikoz lyrics
- kairos fjollor - the kristet utseende lyrics
- emozioni - patty pravo lyrics
- je maakt me zo mooi - liselore gerritsen lyrics
- hanenkam - kinderen voor kinderen lyrics
- kei vip - mimiks lyrics