lamou saff - jeeba lyrics
eh lamou saff kén doula ko wakh
ndakh kako mathie ko xam
ni nane ki dalay gololo nane do dara
maa dougou ci biir ba lépp lérr ma
naandie diarr ngako
koula xamoul moy diranték yaw
mbague chérie coco
bo done musicien
mané la do degammer
déf ngama sa xalé
do joué ak man jeu de gamin
deuk dima diamb, dima diamb
yoro marimba do benjamin
bo défoul ndank na meussa téyé
sa lokho on sait jamais
mom xalé la té bari na dolé
mo raw alkaati dafay dooré
dina la topato ba lathie la, lathie la
lathie la bébé loy réeré
té boko ladié
mouné la bae man yaw mi lay rééré
fadjr tél ni lamay yéewé
dima xool ci biir beut nane ma qu’est*ce que ça fait?
yaw ya raw athlète bou drogué
koula topp ba ci biir day moudié claté
fadjr tél ni lamay yéewé
dima xool ci biir beut nane ma qu’est*ce que ça fait?
yaw ya raw athlète bou drogué
koula topp ba ci biir day moudié claté
eh dafa nékh lolou nga am
kou xam liy diamb sa ditakh
sokh lawoul sakh ng*y wakh
day exécuter néwoul kou rambakh
téey na xamé na fougnouy féthié
yéla ak ndaw rabine
coller gnapp mélni docteur raoult
ak choloroquine
armée wou kaw ak souf
mélni kouy dém guerre
tassaré *rs*nal yi boula dal nga terre
dila woo ci beuré té léer na, léer na
molla, mola meun dila nogatou
tass sa nguémb mbeur ma danou na, oh secours
mom xalé la té bari na dolé
mo raw alkaati dafay dooré
dina la topato ba lathie la, lathie la
lathie la bébé loy réeré
té boko ladié
mouné la bae man yaw mi lay rééré
fadjr tél ni lamay yéewé
dima xool ci biir beut nane ma qu’est*ce que ça fait?
yaw ya raw athlète bou drogué
koula topp ba ci biir day moudié claté
fadjr tél ni lamay yéewé
dima xool ci biir beut nane ma qu’est*ce que ça fait?
yaw ya raw athlète bou drogué
koula topp ba ci biir day moudié claté
fadjr tél ni lamay yéewé
dima xool ci biir beut nane ma qu’est*ce que ça fait?
yaw ya raw athlète bou drogué
koula topp ba ci biir day moudié claté
fadjr tél ni lamay yéewé
dima xool ci biir beut nane ma qu’est*ce que ça fait?
yaw ya raw athlète bou drogué
koula topp ba ci biir day moudié claté
eh lamou saff kén doula ko wakh
ndakh kako mathie ko xam
ni nane ki dalay gololo nane do dara
maa dougou ci biir ba lépp lérr ma
naandie diarr ngako
koula xamoul moy diranték yaw
mbague chérie coco
bo done musicien
mané la do degammer
déf ngama sa xalé
do joué ak man jeu de gamin
deuk dima diamb, dima diamb
yoro marimba do benjamin
bo défoul ndank na meussa téyé
sa lokho on sait jamais
mom xalé la té bari na dolé
mo raw alkaati dafay dooré
dina la topato ba lathie la, lathie la
lathie la bébé loy réeré
té boko ladié
mouné la bae man yaw mi lay rééré
fadjr tél ni lamay yéewé
dima xool ci biir beut nane ma qu’est*ce que ça fait?
yaw ya raw athlète bou drogué
koula topp ba ci biir day moudié claté
fadjr tél ni lamay yéewé
dima xool ci biir beut nane ma qu’est*ce que ça fait?
yaw ya raw athlète bou drogué
koula topp ba ci biir day moudié claté
eh dafa nékh lolou nga am
kou xam liy diamb sa ditakh
sokh lawoul sakh ng*y wakh
day exécuter néwoul kou rambakh
téey na xamé na fougnouy féthié
yéla ak ndaw rabine
coller gnapp mélni docteur raoult
ak choloroquine
armée wou kaw ak souf
mélni kouy dém guerre
tassaré *rs*nal yi boula dal nga terre
dila woo ci beuré té léer na, léer na
molla, mola meun dila nogatou
tass sa nguémb mbeur ma danou na, oh secours
mom xalé la té bari na dolé
mo raw alkaati dafay dooré
dina la topato ba lathie la, lathie la
lathie la bébé loy réeré
té boko ladié
mouné la bae man yaw mi lay rééré
fadjr tél ni lamay yéewé
dima xool ci biir beut nane ma qu’est*ce que ça fait?
yaw ya raw athlète bou drogué
koula topp ba ci biir day moudié claté
fadjr tél ni lamay yéewé
dima xool ci biir beut nane ma qu’est*ce que ça fait?
yaw ya raw athlète bou drogué
koula topp ba ci biir day moudié claté
fadjr tél ni lamay yéewé
dima xool ci biir beut nane ma qu’est*ce que ça fait?
yaw ya raw athlète bou drogué
koula topp ba ci biir day moudié claté
fadjr tél ni lamay yéewé
dima xool ci biir beut nane ma qu’est*ce que ça fait?
yaw ya raw athlète bou drogué
koula topp ba ci biir day moudié claté
Random Song Lyrics :
- wanderer of times - frozen dawn lyrics
- kool aid smile - the boombox lyrics
- blue spanish eyes - claudio villa lyrics
- coiin - jalfa d lyrics
- due poveri amanti - gino paoli lyrics
- us, just dancing - soweto tshepiso lyrics
- chaos - bobbyxl lyrics
- tradito - malliw lyrics
- sleeping dogs - heather nova lyrics
- ρίτα (rita) - xylina spathia lyrics