rakk - jay 21 lyrics
[refrain]
fane nga demone
wakh ma fo nekone haaa
ko andalone
yay sama rakeu sama chérie same blood
est ce que set nga mummy
taylé sa life di fo ni
delol ci sa xel nga nieuwat
est ce que set nga mummy
[couplet 1]
fane nga demone depuis nioulay set
depuis bobou mama mou ngui tok di cry
u ride alone facebook djiss na nioulay djigne ay frasques
sa copine fifi nenama dotoleine andati raakeu nieuweul wakh ma louy daw
ma tek la yoneu yeah
ma tek leu yoneu wareef mak leu haaa
ki ng*y andal dou sh*t deg na mom ngy wowe sa faar
leer nama ne boy bi diangoul sh*t
te leer nama ne boy bi yoroul sh*t
te leer nama ne loxo bim lay taloul dou meusseu watj yay sama raaakeu
[refrain]
fane nga demone
wakh meu fon nekone haaa
ko andalone
chaque jour même question ngamay laatch
est ce que set nga mummy
mane ma dieul p ci classe bi
xam na dou ma def loumay gaagn
demna seti mummy
[couplet 2]
guiss meu mey dem ngey kass
lomeu khameul bey wakh
nekatouma seu baby girl i’m grown enough pour kham
fimey tekk sama tank
kane ak kane lay wakhal
but you all up in my business you’re making me mad
and i know that you trynna protect me
but you don’t know he been good to me
dafmey setsé ngeine mey firè mais khamouloko kone bouko jugè
[refrain]
fane nga demone
wakh ma fo nekone haaa
ko andalone
yay sama rakeu sama chérie same blood
est ce que set nga mummy
taylé sa life di fo ni
delol ci sa xel nga nieuwat
est ce que set nga mummy
[couplet 3]
petit frère dama djiss ennemie sama east sama west damay dial a coup de pelle
no petit bouma diema siss si sama siss di nga djiss ennemie to the h*ll
no petit frère bouma diema dissmiss
waw damay ndiago douma ragale mystique
u gotta feel this
bo beuguer nakhate ci gang pedophile da ng*y diokhe guel toungouné da amel dara justice
sa beuytou down
ngamay guiss guiss
malay pousse down
ma djissat leu fils damay shoot down
pedale nga fils
mouno yor guel bew
boys yi da ngeine gneme coup you risquer
fakalo sama sista dafa diss
djigene deug dagn koy valoriser
yeah
boys yi da ngeine gneme coup wou b*tch
yeah
war nga seti mummy
wa keurgui d namenagn la
t loloy sounou deug bou wor
lane no takh ng*y def li
te bou adio niou sandi bak plonger tene bi
yaw yay sama raakeu
Random Song Lyrics :
- skakanka - natsu world lyrics
- find the door - the haunted windchimes lyrics
- night - etakiz lyrics
- thought cops - charlotte lindèn ercoli coe lyrics
- ford - madmaxxx (rus) lyrics
- jët - плауди (plaudi) lyrics
- hayret - adamlar lyrics
- finessim - tishukov lyrics
- very wide pink - to live and shave in l.a. lyrics
- upgrade - forscam lyrics