lirikcinta.com
a b c d e f g h i j k l m n o p q r s t u v w x y z 0 1 2 3 4 5 6 7 8 9 #

ña ña ña - jay 21 lyrics

Loading...

[refrain]
ña ña na
defoul comme nieup
dagnou ko beer
defoul comme nieup
4k feuleu arbitre youkhou neu breuuuu
est ce que ti comprend
bayil meu diegui cambeu hip hop bi dokh
douma rappeur bou reré corn*boeuf
ña ña na
ña ña na
ña ña na
ña ña na
yaw da nga mer
meune nga diwo beurre
ña ña na
est ce que tu comprends

[couplet 1]
yewou sama keur, évidemment baby bonjour
yewou sama keur beneu dimanche mane princesse dh on joue
sama sons yi rek ñoy duggu club ma thiéné gallé melni old school
bandit sa n*gga dey teup tass nikou deugueu mine diaroul nioukoy soul
est ce que ti comprend?
est ce que djisso crack?
fokoti contrat
fokoti gun crack paaw
dieundeu gouma sama planète niou beug meu gné
defuma dara chaque année man rek ngeeni clamer ndax bëg ma ray
eh boy duma dess ci suuf sans sa guel sama kaw
suñu may denc suuf sama ruhu dañukoy yeegël
concerts yi full mais sa caisse ak ay ndaw
fake yi duñu giss sama défaite
bo dewe ci dig marche ya feu taguer sa bop
neew bi ga mounoul changer djiko bi dou
dess man di nga fatalikou, bayil meu djitou galé tiabi gaateum
[refrain]
ña ña na
defoul comme nieup
dagnou ko beer
defoul comme nieup
4k feuleu arbitre youkhou neu breuuuu
est ce que ti comprend
bayil meu diegui cambeu hip hop bi dokh
douma rappeur bou reré corn*boeuf
ña ña na
ña ña na
ña ña na
ña ña na
yaw da nga mer
meune nga diwo beurre
ña ña na
est ce que tu comprends

[couplet 2]
yaw yaw
nit la di dadj thiono machine
dadj yima soxla moy signer ay contrats sinon soxla wuma sh*t
rap moma soxla man soxla wuma rap c’est comme xorom ak tchinn
gathié ng*y dundu my n*gger ndax workat nga ni corona ak chine
fajo gatt melni chloroquine
dama work hard boy you know what i mean
tegle wuma tank dëkku ma sama kaw lal duma son of b*tch
boy duma sa concurrent bayima damalako ñaan
ba ng*y jug di tëb di dall fekk na man rañaan na
ey duma jug ci rest in peace seen game bi
gamou fake emcees yu demul fenn melni vigile
game bi benn nit la dip ak fin de liste
rendi tête d’affiches yi
benn chef ngafiy giss
dem ak xellu terroriste
f*ck theme ak egotrip
juddo ci ghetto
di jot xeer di dello missile
xeex bi defko chiffres
faybi defko liquide
xetu dé lay guili tax ma dé ko ci biir
[couplet 3]
ap beu nieup youkhou yes mais xam nga lane mo gueuneu bone
djiss ngama ma gadou koudou bou bess, wakh leine deug borom koudou dou laak
yaw da nga meer
do fi amati gouter
sayssouné feri dag mais dou khar rek kay doug sa galé di youkhou mbé
gn*n*leine ko dîna riche
dina dag boumou diami gniko miss
rap beu moumeu deglou meu di youkhou sheesh
dem beu teubeul tiabi reubeuss gniko yitewoul
dougou ci nga sama keer
4k bi dou rap wane meu noumou mel
mane dama la tal ma ngui terre
nga tiagatou game bi ma defar terrain nga teud ci kerr
rap melni kouy mbe
deglou sa text mou melni ay ching chong fougnou tasse nga tituber
21 di sama season
hurry up ci sama kiss
sa carrière melni sounou miss monde
gadou courouss sama dale
pomme de terre bou gare
mala djiteul diale
xam nga sama gale
bayil

[refrain]
ña ña na
defoul comme nieup
dagnou ko beer
defoul comme nieup
4k feuleu arbitre youkhou neu breuuuu
est ce que ti comprend
bayil meu diegui cambeu hip hop bi dokh
douma rappeur bou reré corn*boeuf
ña ña na
ña ña na
ña ña na
ña ña na
yaw da nga mer
meune nga diwo beurre
ña ña na
est ce que tu comprends

Random Song Lyrics :

Popular

Loading...