dieuw - jay 21 lyrics
[couplet 1]
nenagn sa tour dîna dem beu doug bountou keur yi sa tank yi moussoul yeg
lignouy lamlamé ci souf di ko neuf neub leup dîna leer geuneu leer dialou mbaye dieye faye
bo xamone nieup lagnouy dieuw d di nga ci tay
dieuw ci bopam fign leu dieuwe fofou lako fek
aka meuneu dieuw vroom vroom
tem nga fokne dafa dieul auto sakh fign la dieuwé fofou lako fek
meune nga dokh ci kogn bi gnouné la fi leu fileu
nga yeg bop kogn bi gnouné ki leu ki leu
ki sekh sa deer bi kokou molay invit diner
mou sign leu beugn bobou lamign safneu piment
maybe molay may copine neum
dioy ci vélo dioy ci bmw
a little bit, ndokh bi deugeureul neu ciment
bou wakh bi nekone ndokh
tem meu fey beu cuba
bou wakh bi nekone souf
tem meu fekh ni état pas pour gni wakh bi sout
pas pour gni wakh bi souteu
pa ba ngui wakhtou fou
dakar gnou ngui diot ci loutakh
kane mo geuneu wakh
kou ci wakh dioteu wakh ki leu waar bi dioteu wakh ki leu dioutou soubeu
wakh bi code fare
dieuw bi dioutoutoumeu
tal neu gueminou moumeu
taak gueminiou toumeul
wakh bi goudou fane
ki leu wakh
dougou nop
wakhma boukheune tewouma demna sama galé dieuw dou tiakhane tem nga lek derou diambour bobou diambour doufa nek
[refrain]
niou diape leu day, nga buzz sen kawman tay ni dial mbaye dieye faye
sa tour bountou keur fi tank yi tassel banc bi day fay
imam bi day diay, t pretre bi day fay, bou diaké day ray
all eyes on me ma leine geuneu paré, dieul messi dougal ci corps rou mbappé
doma yabi, doma yabi ih hé
all eyes on me ma leine geuneu paré, dieul messi dougal ci corps rou mbappé
doma yabi, doma yabi ih hé
all eyes on me ma leine geuneu paré, dieul messi dougal ci corps rou mbappé
[couplet 2]
xamone na né dinagn tok di tek
ma xamone dagnouy saltel xamna ma leine geuneu nek
mom xamone na né police dina yek ci diko pep
guemine biko dieuw beu loxo biko diokhone tiep
meune nga doug galé nieup dieki dieki tek
nieup lagnouy dieuw bobou fofou lala fek
yakoul dara sa deer beu legui ma ngui flex
molay diemeu tester tamit molay diemeu text
mané dieuweuti neu
dieuweuti neu yeah
foko meunti fek mou ngui caisser ay boys
fou xol yi meusseu tang mou ngui xamb day boyal
t lamine ba ngui nekh yomb doug noy*boy
nopina, nopina boys!
sa guemine d*nko teutch d*nko teutch ni viber
keine douko teutch lolou dundou cypher
beguel nop ké moleine geuneul aythia
sa guemine gnou day feu
douma sokhla paper
lolou dundou vampire
boudone glace gnou sey feu
do leine meuneu woneu bi
diokhé bakane fayouko
lane nga fi fomp dagn meu bindeu dieuw title
lane nga dound night
khamo sama size
lo ci beug aythieu
dieundeul baby viper
ma leine indil money
lolou nek sama mind
dieuweul sekhal derr bi
lolou yakoul sama vibe
[refrain]
niou diape leu day, nga buzz sen kawman tay ni dial mbaye dieye faye
sa tour bountou keur fi tank yi tassel banc bi day fay
imam bi day diay, t pretre bi day fay, bou diaké day ray
all eyes on me ma leine geuneu paré, dieul messi dougal ci corps rou mbappé
doma yabi, doma yabi ih hé
all eyes on me ma leine geuneu paré, dieul messi dougal ci corps rou mbappé
doma yabi, doma yabi ih hé
all eyes on me ma leine geuneu paré, dieul messi dougal ci corps rou mbappé
Random Song Lyrics :
- stúpaj so mnou - adam ďurica lyrics
- i ett hus vid skogens slut - mathilda åström lyrics
- burning out - two channels lyrics
- next to me - skeletonprince lyrics
- awaken love - lacey sturm lyrics
- diamond mind - dr. dre lyrics
- risco - jovem dionisio lyrics
- hometown glory [live at the hotel cafe] - adele lyrics
- ...in bed - kollektivet lyrics
- die angelobung - def ill lyrics