bùl bidënti - jay 21 lyrics
[refrain]
mounema geutch nagn djissante
mane ko ndiabot moma djiteul tay
nenagn geutch nga fegn depuis sa mixtape mane par force louma dji day fay
mounama la ye beug bideunté
taa nga ci diguanté bi
li dou garawalé limit pick pele
par force louma dji day fay
[couplet 1]
a part sama ndiabot douma facetime
dougal marche sama style li dou freestyle
game bi gnourok dessi anime ni sp*ce jam
dafa nara taar fils na nga tela far fi dama dieul ci sama part ndeysan
def jeez sama ngam paré sif dem
m** f** bou ci tontou mané k!ll them
sama tontou mounoul forokh gainde tiki sama city bayil meu dieuli sama liif, siif leine
sa rappeur douma guiss, system
dagn meu gueneu fanatique, u get that
diaral sama biir, plus leu
diamono ngui dokh t dieuloul pile, djiss nga
doumay sarax bi, triste neu
dial diemeu fakhass sama chaise, glisser
dou yameu nara teyel sama caisse, please kone
xippil sa beut n*gga t nga djiss
keup kouma djign
xol ci meu fi
keup sama gin
khintioul sama jeez sama poche mou ngui bakh
bouma khandiou peace n*gga dotou ci dale
dama gadou sama fit souma teude douma nela sama city sama canapé sa rappeur zombie
ay rappeurs h*llokitty
fougnou tasse nagn leu tchi*tchi
dama dieul ci sama wetchit
damay gadou sam prix
[refrain]
mounema geutch nagn djissante
mane ko ndiabot moma djiteul tay
nenagn geutch nga fegn depuis sa mixtape mane par force louma dji day fay
mounama la ye beug bideunté
taa nga ci diguanté bi
li dou garawalé limit pick pele
par force louma dji day fay
[couplet 2]
deg na demb da nga bideunte
demb la djiteul c
trump dafa guint beu bidden tew
mane ko moudié wala moudjié tew
mounema na baar ndakh kou mine day bayi
mane ko dou demb lagn djissanté
moune soumay deglou gne sama xel dey tey one time 4k n*gga kagn lay game
dama ne ci prison
gnou ngui may diema photocopie keneu dou nek copie jay
ma ngui sama kingdom, king kong
tout le monde veut le place du khalif et le khalif talibe
bayil meu delou nek ninja
dina danel diouné bop pare beuri talibe
dougnou rappeur yi di rêver doug wati b
sa rappeur mou ngui tchipatou doit neu ci gatou jay
xaral 4k boul bindeunté
dîna xar tâte t dou diranté
mane tiak tiak dîna bireul beuy
da ng*y 4 camp dagn lay djiteul fi
dîna taar taar bougnou djissante
mane 4k bi sa biir lay bay
29 octobre sounou bday tay
dagnouy capable dougnou minanté
[refrain]
mounema geutch nagn djissante
mane ko ndiabot moma djiteul tay
nenagn geutch nga fegn depuis sa mixtape mane par force louma dji day fay
mounama la ye beug bideunté
taa nga ci diguanté bi
li dou garawalé limit pick pele
par force louma dji day fay
Random Song Lyrics :
- high hopes - flackofredo lyrics
- entendedores entenderão (ao vivo) - joão neto & frederico lyrics
- so far so good - gabrielle aplin lyrics
- deception pass - land, man lyrics
- pavement - second change for better lyrics
- see the sky - reredemption lyrics
- пиши - petr prokopiev lyrics
- na mão do poeta - hobb & hollz mc lyrics
- in these arms - jp cooper lyrics
- luz - rima lyrics