lirikcinta.com
a b c d e f g h i j k l m n o p q r s t u v w x y z 0 1 2 3 4 5 6 7 8 9 #

xamouloma - fire lyrics

Loading...

couplet 1:
lo def malako dakk may badou meune lepp
game bi nekatoul rap mais kou dakk lebb
fii dafa tiliim tei chak jour niouy setal
fii ngeye raak ba deii niou togg dila setane
fi sene khela gatt motakh dougn goudou fane
fi ghetto bei stylé melni ay mbeddu fann
mangui ak hamadi niou todd tekk warrga bi
fekkei maci bolei ma dieul raw gadou bi
magg daane tei ngembo ngembou khalei
reye la nga seugue sigilela ndigalei
loutakh manane lene ghetto bi da stylei mane dong nekone thug ci ay enfant gatei
fii bene baye fall rekaye diakhal kogne bi yeup
bima dioudo ba legui hamouma dadj di deup
p-ssy oubekoul defena mon guene yomb
bi tedj lene sene taate yi mo guene kou nieuw rek romb
bene vidéo niounane fireminati
n-gg-rs so funny douniou khamtei dougn ladjtei
bind ba mame nane ma kocc barma fall
nekone khalei bou ndaw done cons bambaj fall
dama changer sama tourr pour meune bokk
mais changerwouma sama jiko pour rek bokk
bouma khamoul sakh deima ni-n-le mou yokk
dama dioudou daldi tiital samay mbokk
ci fanne you neew la reye nitt kima nekone
dou pour iow kone limeye def boul nei da bone
esk dinga guiss niit nane dangakoy diokh ngogn
boula knockei esk kene dinagn ladj kou togn
talent amoul boy, ligueye rek mo woor
weer bi dina fegne tei dou done werrou koor
khel di gnafei beuss bou nekk moy yonou goor
legui lepp nieuw fettei ci souniou boor.. ibou

refrain :
xamouloma, n-gg- xamagoma
boumaye nieuw yene nieup laye bett xamagoma
bo beuguei biff, n-gg- woma
ladjtel niata rabou alle laniou diomal

xamouloma, n-gg- xamouloma
boumaye nieuw yene nieup laye bett xamagoma
bo beuguei biff, n-gg- woma
ladjtel niata rabou alle laniou diomal

couplet 2:
damay rap dila diangal ni sama gars konzo
mane la nieup di weurr meye melni la conde-jo
dama ham yone bi ni kou dei baye doundate
mane la nieup di khaar ni real ak barca
sene khela vide ni sama casier judiciaire
demagougn sakh guissna sene gale yi di taire
douma khol depart bi wantei arrivei bi motakh limeye khel di fayeikou di chère
gniko fonkoul la sene tchine di bakh ngerr
back to reality fi amoul diannère
b-tch bi sama snap nena dama mignon
poche diss na mais fokk niou lale ay millions
niata nio parei bimlene neeii mangui nieuw, ba teye dji mangui ci kaw
lou adversaire bi tangue bou parei wakhko mou nieuw, niane yimay niane defna ko bima dieuli ji communion… ibou

refrain :
xamouloma, n-gg- xamagoma
boumaye nieuw yene nieup laye bett xamagoma
bo beuguei biff, n-gg- woma
ladjtel niata rabou alle laniou diomal

xamouloma, n-gg- xamouloma
boumaye nieuw yene nieup laye bett xamagoma
bo beuguei biff, n-gg- woma
ladjtel niata rabou alle laniou diomal

couplet 3:
boma hamoul dema wowe eh wala nga woweima king bi
liy bakh loutakh mouy khegne nekh da fekk bobou mongui ci tchine bi
nioune daaniouy music tei douniou def fausse note motakh fi khamougn kouy thione seck
nene dou meusseu guiss souf bou noy nane dafay dem di dale ci ay keek
fekkma ci yone bi mey dawal 205
hamouniou loudoul hustle hamougn loudoul niafei
namena lolou tps yiniouy reréji sombi
legui calculel calculel ma guenelela somme bi
mangui def ci souf pour meune yegue ci kaw
lane lay guiss boumalene di khol ladjko pithie biy naw
beusse dou touti borom leye tolol sama nguentei ni 4avril
damay todj game bi nga fekkma mbside ma togg ci samay n-gg- diap tchill
guissngama meye takk rollie bi melni n-gg- damako tamone
guissnga kene dou wakh ci sama succès melni n-gg- damako tamone
mangui dokh di nieuw guissna n-gg- yi tekk sene mic melni kou guiss camionwou 100tonnes
legui game bi dafa dih-sso melni bene kogne bou am 100 kogne

Random Song Lyrics :

Popular

Loading...