lirikcinta.com
a b c d e f g h i j k l m n o p q r s t u v w x y z 0 1 2 3 4 5 6 7 8 9 #

teaupla zinedine - elzo jamdong lyrics

Loading...

intro:
bang, bang, bang
yeah
zizou !

hook:
chaque année diaay ay projets mayé ay inédits
samay concerts team elzo dieund tickets yi
tactique technique yoré naa idée yi
football, coacher : teaupla zinedine
maay teaupla zinedine, teaupla zinedine
teaupla zinedine, teaupla zinedine
tactique, technique, maay diokhé idée yi
teaupla zinedine, teaupla zinedine

verse 1:
ma indi waat dope from bogota, bogota
poullo dogota
dougg deukk yeupp comme corona
ma eupp objectif sakh photographe

n*gga mangui yonou dieul mairie town
diangg naa meun naa nekk président
yegoumala tant que mere bè ngui proud
def hit make money evident

yeah
job deugg sogueu am doe
tabakh keur sogueu khandor
dèè dogueu am pause

renn naa lène diommeulaat bro
doumeu queen biz
wayé koumeu togne naaleu diongueulaat bro

li dou flowou auto clando
so meu diokhoul benz walla phantom diokh meu lambo

afrique dem momeu takha diok
tabaski niawlou obasanjo
comme obasanjo

for the culture naalene wane may kan
watch yo mouth so beugué wakh ak mane
mom sama town comme rêvou akon
jaden smith, i’m a icon

maay sene coach keep lene cool
gueun lene clean gueun lene kaing
mane ng*y call so beugué am coupe
maay sene king teaupla gang
yeaah

hook:
chaque année diaay ay projets mayé ay inédits
samay concerts team elzo dieund tickets yi
tactique technique yoré naa idées yi
football, coacher : teaupla zinedine

maay teaupla zinedine teaupla zinedine
teaupla zinedine teaupla zinedine
tactique technique maay diokhé idée yi
teaupla zinedine teaupla zinedine

verse 2:
teaupla zinedine teaupla zinedine
jom ak leadership dope laa indi fi
dore war momeu tidjil contrats yimay signer
f*ck la défaite koumay stop la guisseugoul

stop laa guisseugoul dof laa tchi equipe (stop la guisseugoul dof laa tchi equipe)
sene joueurs nieuppeu nuls naalene beuss comme kinesi

naalene raquetter nangou sene dollar, comme ni thioy yi di def ak dealer (def ak dealer)
kou leu né dafma guedjeu guiss corner ba, nee ko free mingui def ay dealeum (dealeum)

amone naa
diamono you may def ay delits diamono you may def ay delires
mais samay dome
fok ma am loumeu def sen guemmign kone fok meu def lou rey comme remy

ngandi kickeur jackie chan
khammé ngama bandit town
yengueul megué bi tranquillement
meun tchi pelouse bi ak tchi banc

numero 10 on my name (zidane)
wa team bi yeuppp kontaan negn ! (real)
sawarouma tchi commentaires (zidane)
khamolene sh*t, jobaat leen
yeaah

refrain
chaque année diaay ay projets mayé ay inédits
samay concert team elzo dieund tickets yi
tactique technique yoré naa idée yi
football coacher teaupla zinedine

maay teaupla zinedine teaupla zinedine
teaupla zinedine teaupla zinedine
tactique technique maay diokhé idée yi
teaupla zinedine teaupla zinedine

Random Song Lyrics :

Popular

Loading...