reppin' time - elzo jamdong lyrics
intro:
yeah, yeah, ho shi…
eh yow, yo
degn niou conditionner ba bo beugué tek li seu…li seu communauté di dound dang*y … dang*y soraalé
mais est*ce que niom di negn soraalé souniouy wakh ci souniou ay familles nombreuses ? ak souniou fébar yi nga kham ne niom nio ko inventer ?
yeah, yeah
couplet 1
africains, degn niou kheeb ba tay
n*gga bou tekki sakh n*gga yi degn ley kheekh ba tay
colon bi neneu demb moniou civiliser
motakh louniou meusseu créer def ko dindi musée
wow
sarko neneu amouniou history
al me lagnset me niassal ko hyeroglyphe thi kanamam
degn niou yep seme baat thi kow
nekal waliyou do dara loudoul black thi niom
souma nekké town kaawman laa
souma nekké kaaw bledard laa
loutakh dougn ma wowé expat han ?
deukk banlieu egale defkat laa
fok me dem ofi khole bane febar la am
mel ni fimeu diogué
sida defe feugg niou ne ko bismilleu
liniou beuri febar yeup khamal ne crise bi leu
nassaraan si daf niou yagg forcer guiss*guisseum
motakh diplomatie kheetou hypocrisie leu
se life yeup le degn ley wone ni li nga am dara amouthi ndiérign
li nga kham dara amouthi mérite
linga dond ci sey maam degn le naan fattel te boul réfléchir
khamo nguerr wayé am nga aspirine
correct moye ndourou toubab
soy wout liguey bo solé grand mboubb dou baakh
chemise ak pantalon rek kay dougg fou baakh
entretien tegal cheveux dé boul yobou foulard
ci mane roy daakkh degn koy donde
après colonisation médias yi degn koy dolli
bo gueustou woul se bopp toubab def ley jommal
nim le def nou ko raw le koy def sey dome
complexe degn koy donde (yeah)
système bi def koy yokk
mangui fateulikou bimeu beugué def ay locks
prof bi nemeu wotoul walla sdf ng*y done
chorus
i’m on my reppin’ time
(reppin’ time, reppin’ time, reppin’ time)
we gotta make it right (make it right, make it right, make it right)
i’m on my reppin’ time (reppin’ time, reppin’ time, reppin’ time)
souniou maam yi degn ko mettil baay
now we gotta make it right
2e couplet
yeah
lifou bitim rééw degn ley humilier
degn ley keyit lo ndakh amo keyit bro
faut qu’ nga khèkh diayanté pour meun ne ci jamm
degn niou tek deal, jaam
legn niou def tchi mind
li gueuneu metti moye niom nio ndieukk nieuw souniou territoire
takk boumou diaam dieulssi tirailleurs
tey niou né beugueutou niou guiss benn noir
degn beugg niou teudd gueumm ni schumacher
yeah laadiouniou ken mou nieuw sathieu souniou or
wakhouniou ken indil bateau yobou souniouy maam
loutakh niom huey p dawal naka soudoul nonou ?
parce que gni ndieukk indi thiow baalou wouniou akh
akh
dieul deukk leumb dompter leen
be legui pubou khessal mingui daw télé
nio takh ba souniou sista yi di am complexe
ba façon febar bou nekk leniouy diankontèl
histoire bi degn ko deupp
histoire bi degn ko deupp chapitre yi lène arranger woul degn ko teup (yi lène arranger woul degn ko teup)
do degg fenn tabakhou pyramide nitt kou nioule mo tchi ndieukk
motakh nit kou nioul rekkay am accent wou nit kou nioule di ko neubb
boko defoul rek niou toulli leu seen deukk
immigré kessé nga dougn le mey loudoul ass toute
so meuné diaamou tedj se guemmign that’s cool
meun nga tidji taxiphone walla fast food
so beugué changer game bi degn ley gass soul
seu lepp degn koy toutil niounè hip hop dou culture
il faut que nga nekk bounty pour niou tidjil leu buntou lolo waral
cité yi fess dell ak ay famille’ou black
bac dou guedj tchi kogn bi ndakhte boy yi amouniou bac
bridge:
yéneu ndieukk nieuw souniou deukk
tey bougo lene niou guiss sene deukk
di negn lene wakh souniou deugg
di negn lène wakh souniou deugg
yéneu ndieukkeu nieuw dieulssi tirailleurs yi
tey bougo lène guiss sèni seut
di negn lene wakh souniou deugg
di negn lène wakh souniou deugg
chorus:
i’m on my reppin’ time
(reppin’ time, reppin’ time, reppin’ time)
we gotta make it right (make it right, make it right, make it right)
i’m on my reppin’ time (reppin’ time, reppin’ time, reppin’ time)
souniou maam yi degn ko mettil baay
now we gotta make it right
outro x 2
(reppin’ time, reppin’ time, reppin’ time)
(make it right, make it right, make it right)
(reppin’ time, reppin’ time, reppin’ time)
mettil baay
Random Song Lyrics :
- the future is a foreign land - ghost lyrics
- honky tonk land - james carothers lyrics
- ihear†_ligh† +++ خيالي - uziellsiilver lyrics
- goner - hallows (band) lyrics
- rose water - sarah khatami lyrics
- poppers - grape digging sharon fruits lyrics
- hd - textkill lyrics
- forever - lil gabat lyrics
- teeth - r3ckl3ss lyrics
- habis gelap - barasuara lyrics