contact - elzo jamdong lyrics
verse 1
ganiou khol (ganiou khol,ganiou khol, ganiou khol )
soma gueumoul kaay niou khole
(kaay niou khole, kaay niou khole)
am naa ganiou khol (ganiou khol,ganiou khol, ganiou khol )
bimay binde li sama yaram mingui dow
(mingui dow, mingui dow, mingui dow, mingui dow)
nakhar bou yagg thiono you bess rek yeah
yone bi niou diaarone beu fi degn ko teggui regresser
yeah
yakaar bou t-ss dokh ne tchi souniou kow mbegté yeah
amatoul jamm sougn diggueunté amatoul respect
yeah
bridge:
kenn meunoul wone gueum ne
dinaa meusseu tok beuss te doumala khole
noumay def ba fatté ne
maa ndieukkeu samp n-bel tchi seu khol ?
yakaar bou yaakkho tchi base
kenn meunou ko defar tchi kenn
limeleu defal lou baakh meuneutou meuko ko defal djigueen
chorus
yow laa beuggone takk
khawma nouma def ba niou
niakk contact
x8
verse 2:
warone naa meuneu nekk se bodyguard
se body guard ex alla boni ma begn
bimala niakké beu legui diommi laa def
yow leu docteur bimay fadj diaroul hopital
yaay sama doliprane, doliprane, doliprane
kham nga ni yow mi yaay chef
awma interet bokk tchi gore yi diaay ting
souma offé ya may charger comme mobicarte
sinon ay folies laay def
seet naala dow naa seu guinaaw
namm naala beugg naala guissaat
deuggueul negn gni niou yagg diss
gni néwone souniou andeu meunoul réussir (un hun)
liniou doundeu beuggone naa ko bissaat
togne naala beug naa nga guiff baal ma
am neu niou yakamti niou gaawa t-ss
boul yakh li niou yagg tabakh
andeu tigui yagga takh niou koy wakh
bridge :
kenn meunoul wone gueum ne
di naa meusseu tok beuss te doumala khole
noumay def ba fatté ne
maa ndieukkeu samp n-bel tchi
seu khol
yakaar bou yaakkho tchi base
kenn meunou ko defar tchi kenn
limeleu defal lou baakh
meuneutou meuko ko defal djigueen
chorus
verse 3:
kham naa ni il faut que ma dem
adouna yaatou neu lolou
beuss di nga dadiéʼk keneen
keneen kouy deufeul seu khole
bokkouniou ni niouy mougné
bokkouniou fi niouy moudié
beuss di nga dadiéʼk keneen
keneen kouy deufeul seu khol
Random Song Lyrics :
- in time (even then) - words of life music lyrics
- lado cachorro (ao vivo) - kevi jonny lyrics
- bitch, move! - lil lyko lyrics
- spiral - abby holliday lyrics
- anti-lover - zeno trim lyrics
- 6.3 - xcho lyrics
- super duper party people (alan braxe remix) - allie x lyrics
- mijo na piscina - lil careca lyrics
- no reason - zeppet store lyrics
- pangolin - mr. weebl lyrics