ci yaw - elzo jamdong lyrics
verse 1
sonne naa te guisseugouma dara loumeu meuneu fatté lo ni yow la tannone pour nga samm sama mbeuguél
fonk naala kone faut que nga nand ma te fogone nani soumeu togué weet ak seme bopp ding me goungué eh
yama newone ne ding ma dinthial se thiaabi khol te loumou gouddi gouddi dinga tidji soumeu feuggué
diangg naala mokkal naala amoul dara lougn ma meuneu khamal ci yaw
ci yaw
ci yaw
ci yaw ( ci yawww) ci yaw ci yaw
ken dou wakh dara ci yaw
ci yaw
ci yaw
ci yaw ( ci yawww) ci yaw
ken mounouma wakh dara ci yaw
verse 1
sa yo guenné mane ng-y khalaat
souma kholé yow rek laa am
soma guissoul dang-y malade
yen saay me doyal seukk ci yawww
chorus 2
sonne naa te guisseugouma dara loumeu meuneu fatté lo ni yow la tannone pour nga wetteuli me te nga samm sama mbeuguel
faut que ma maanou ndakh thiow li thiow li yeup waroul niaaaw te warouma weddi tam
lepp lima diangg ci yaw
ci yaw
ci yaw
ci yaw ( ci yawww) ci yaw ci yaw
ken dou wakh dara ci yaw
ci yaw
ci yaw
ci yaw ( ci yawww) ci yaw ci yaw
ken mounouma wakh dara ci yaw
verse 2
mouno nango am tort
(ci yawww)
te guedj nga wakh me d’accord
(ci yaw)
fogone naani c mort
bobou khawma wone louy amor
ay khoulo tey dioubo tey
yenn wakh you sew yi douniou tardelaat soudone tey
mane lenn laa guiss ci yaw
moy ken khadioul tchi sougn thiow
(thiow thiow thiow …)
yeah ehhh
chorus 3
sonne naa te guisseugouma dara loumeu meuneu fatté lo ni yow la tannone pour nga samm sama mbeuguél
faut que ma manou ndakh thiow thiow li yeup waroul niaaw te warouma guedd tam lepp lima defar ci yaw
ci yaw
ci yaw
ci yaw ( ci yawww) ci yaw ci yaw
ken dou wakh dara ci yaw
ci yaw
ci yaw
ci yaw ( ci yawww) ci yaw
ken mounouma wakh dara ci yaw
hun (ci yawwww)
hun hun hun (ci yawww)
Random Song Lyrics :
- indian aunties freestyle - ie hood - young hav lyrics
- drugs - star boy lyrics
- бессмысленная любовь - shantysilenc lyrics
- dont forget - luzja ice lyrics
- "nigga what?!!" - cavalucci lyrics
- dazed - caislyy lyrics
- blue blue space - adora lyrics
- g.lassée - luther (lutherantz) lyrics
- kneel - kawena jacobs lyrics
- everyday i have to cry some - gary lewis & the playboys lyrics