damako khar - dip doundou guiss lyrics
yeah
[refrain]
ba nieup diekhaler mane silay soga fess
deff nala papeu parceque terré womeu khékh
dinagn leu enquete ndakhté tay seu domeu khew
tay bam leine wanei samay rongagn niom nieupeu begg
bo khaméni faw ngueu lekk faw ngeu fokaler
deuguey khepp cond-mner mou toll ni contenaire
last cri perrou dall damleu soll beu dh motakh tey job beu dh niak diot beu dh
[couplet 1]
damako khar ni stef curry pour wadial jordan man
ni beppou khettou nitt bouy wadjal done leineine
faterwmeu fign meu diangueuler fignmeu diongaler
faterwmeu paa yimeu ni-n-l méres yimeu diokh meu lekk
avenir legn demone dieuli si yonou clochard
karaw bou nioul ak khel bou mak seu niom maam
boul wolou sakh gnileu wolou
confiance khadjoul si malaka djiner confiance
may garap bou beug microbe, innocent bouy andak ino
[???????????????????????] lay guiss soumeu fataliko
diokhmeu p-ssport visa yeah, tampon si p-ssport bi meu dem
par force f-ss diom riche ba dh
waw gorr di ngueu done milliardaire eeh
yafi newone sougnou gang famille leu
nioune nieupeu bokk diar diar n-ggah
fima diar, koufeu diar, khamni iow figua diar
koufeu diar t-ss seu yakar n-ggah
magui niafer magui khar matteu n-ggah
khonertatoumeu sakh rare my n-ggah
fimeu djouguei soumfeu narrei delouwate
fadj meu jail walleu teudj meu hospital my n-ggah
yeah yeah yeah
[couplet 2]
beu nieup diekhaler mane silay soga fess
dip comme kou teude lo correctionnel ay colonels
dinagn meu saga ndey dina leine songueu kheikh
kone niak djot beu dh gueiner sons beu dh
mowti sakh doumeu dieulsi parceque mak momeu yam
kone en cas mc bou dh boul ladj kane moko ray
niata rappeurs ngueu fay niata million ngueu lek ?
boy dessétoumeu beine rongagn pour dioy seu deudj
est ce que witiakh na sameu baram?
gueudj na reuthiou depuis 17ans motherf-cker
damako khar ni idy ak adjana
mane damleine rendi sogueu t-te ndeysane dawneu yaram
boy mane kessei, beine nitt, 5000 nitts dimeu khékh
ni-n-l na samay ennemis; ennemis ki ak kéh
dama khekhal mbedd bi, mbedd bi dimeu khekh
dama khekhal mbedd bi, mbedd bi dimeu khekh
magui si chaisou bour bi niogui si chaisou douches yi
fakes yi, dounks yi, nandité you mouss yi, teknagn gnou deal mais
[???] noir et vert amoufi derr bou nioul mo khew derr bou nioul bi
mafi ngueuneu touti tiabi bou reuyoul dou tidji bountou
magui ngueuneu yekk di ngueuneu yekk di ngueuneu weett
khariteukeu neew si diamonos yi wouy sama ndey
trahir yeurmeunder deff sama khol si sama khel
diay kou meuneu fayy dougn mayer khéerr di keuppeu caisse
fitneu la fitneu may fitneu
fitneu la fitneu may fitneu
lolou takh ma wagni samay jo bro
lolou takh meu yokk sama job bro
lolou takh meu niermer songu ngandi crew
lolou takh meu wett di course ak sameu chrono
pé lay dieul bougou meu p-sser
pour iow ndiago foote akh p-sser rek
t-ssé ngueu ak mane mou dagn
[refrain]
beu nieuppeu dierkhaler mane silay sogueu fess
deffnaleu papeu parceque terrer womeu khékh
dinagn leu enquete ndakhté tay sa domeu khew
tay bam leine wonei samay rongagn niom nieupeu begg
bo khamer ni faw ngueu lekk faw ngeu fokaler
daguay khepp condemner mou toll ni contenaire
last cri perrou dall damleu soll beu dh
Random Song Lyrics :
- ねこ (neko) - 吉田美奈子 (minako yoshida) lyrics
- minimum brain size (live in melbourne '21) - king gizzard & the lizard wizard lyrics
- afflict - laur lyrics
- the church - hiraku lyrics
- way up - flvme lyrics
- sale - the andré lyrics
- physalis - ace won lyrics
- la grosse dose - marginal lyrics
- brighter days - scouting for girls lyrics
- feel it - meiston lyrics