wareef - dieyla lyrics
djiguène bou né beuge na ci doundame kouko yeureum
beugue na koukay goungé thie yone
diox ko thieuram
beugue na kouko wolou si lou nieuwa goul
beuge na kouko sangue soutoura ndax matatoul
lima mome dama kay diox
goor gouma falé bouma réwal téral ma
té douniou laalé
kou meun sargal djiguéne
goor gou méloute ni yéen
kouy door ak saga té meusso di réé
say réé lala beugué
ni lala n0bé
say dieuf lala nawé
ni nga mel boul ko changer
yaw gentle nga
do xoulo do xéex
téral nga djiguène
ni lala beugé
ni lala n0bé
say dieuf lala nawé
ni nga mel boul ko changé
eh waay waay gentle nga ni lala beugué
andi nga téranga mani waaw
di nga ma liguéye mani waaw
di nga mani fo dieum
di nga ma yobalé
wayé sou amoul mbeuguél, bye bye
yaw wanе ma louma doye
ma dix la loula doye
bo xamer kima doonе
moy xol bi yaka mome
wouy yoo lé, wouy yoo léé
beugue na koumay nabe nabé
def ma lila war xam nga ni nii la nii la
diame dji ng*y weur fii la
soma woolo doylo ma
loma meun ti nakhé nangou na
say réé lala beugué
ni lala n0bé
say dieuf lala nawé
ni nga mel boul ko changer
yaw gentle nga
do xoulo do xéex
téral nga djiguène
ni lala beugé
ni lala n0bé
say dieuf lala nawé
ni nga mel boul ko changé
eh waay waay gentle nga ni lala beugué
andi nga téranga mani waaw
di nga ma liguéye mani waaw
di nga mani fo dieum
di nga ma yobalé
wayé sou amoul mbeuguél, bye bye
yaw déé ko té nga aare ko
xolé ma man mii sa yaye booye
ndax djiguéne (x3)
dagne kay soutoural
Random Song Lyrics :
- late night adventure - baba blakes lyrics
- les sirènes - audshine lyrics
- cycle - nicole zell lyrics
- flipbook - tom block lyrics
- a christmas kiss - cristina f lyrics
- who i dropped (who i smoke) - the deadly youngan lyrics
- mutual admiration and love - the bran flakes lyrics
- laazy - aamo lyrics
- cap city (intro) - the big hash lyrics
- outro (for my family) - sidarta (grc) lyrics