wiri wiri - diaw diop lyrics
wiri wiri lyrics
yow wiri wiri diari ndari fo meunti demitt baby dinga dellou si
koti koti yolli yolli kay fi ma nakh la yadi sama nenè touti
boul daw meuna daw takhouta reuthie
loy doyé orr so amé diamant bi ci keur gui
matt lima done andil contrat niou signé
fouk ci niom mane rek ma yeungeul geusseum kene dou yeungeul
niamé na lolou tiitouma lolou
gagne wala gagne match nul yalla teré
niamé na lolou ragalouma lolou
gagné wala gagné match nul yalla teré
ba takh na
danga done lamb dadje nga
danga done sett deh guiss nga
hee mane leu
affaire bi mane leu
danga done lamb dadje nga
pessé nga kham nga diss neu
hee mane leu
nangoul ni mane leu
dall nga ci dall nga ci yow bi bou bakh bi leu
dall nga ci dall nga ci si si bou bakh bi leu
dall nga ci dall nga ci yow bi bou bakh bi leu
yako tay kham ngani bii nii bou bakh bi leu
woo ma, woo ma yow
yow wiri wiri diari ndari yangi dem té yangi delousi
ma dila ayo ayo nené dila nené nené touti
doranté dakanté melni khalé yay sama tom deh may sa jerry
malay teul di teul teul
done sa seytané dila djomal
athie ba ca kaw wathie la ci souf
roganti teup teupal nila noppil
danga done lamb dadje nga
danga done sett deh guiss nga
hee mane leu
affaire bi mane leu
danga done lamb dadje nga
pessé nga kham nga diss neu
hee mane leu
nangoul ni mane leu
dall nga ci dall nga ci yow bi bou bakh bi leu
dall nga ci dall nga ci si si bou bakh bi leu
dall nga ci dall nga ci yow bi bou bakh bi leu
yako tay, kham ngani bii nii bou bakh bi leu
thireureuw thireureuw sa guinak thireureuw thireureuw sa guinak
tathie sa guinak sa guinak yow dokhal
na noy rek niou wakhtané ko
na noy rek niou wakhtané ko
beug ngako bamou djekh te dara douko dindi
mom nena yow rek té kene douko dindi
wiri wiri diarouko yagg yagg dadjé
gaal guey nieuw gaal gassa top sa cadeau ngassa
fethial ko thiathiambal
the thiathiambal the thiathiambal the thiathiambal
fethie ko yow (fethie ko) fethie ko yow (fethie ko) fethie ko yow (fethiati ko)
lii moy the thiathiambal
the thiathiambal the thiathiambal the thiathiambal
khalé bouko meune nii ngakoy deffey
gorr kouko meune ma may la djouni
sa guizeul sa guizeul niapp sa guizeul
sa guizeul sa guizeul niapp sa guizeul
sa mbiw reuw mbiw pata minal reuw mbiw
pathié thié koy koy gardé vous yow dokhal
deug leeeeeuuuuu
Random Song Lyrics :
- stay all night (stay a little longer) - woody holler lyrics
- братик 2 (bro 2) - скриптонит (scriptonite) lyrics
- invisible (one more light live) - linkin park lyrics
- nah - sneakbo lyrics
- therapie nach anhrazit - raf camora lyrics
- bros - gawvi lyrics
- sogni di cera - axos lyrics
- bauchgefühl - helmut angler lyrics
- lonely christmas - scotty sire feat. heath hussar lyrics
- rain down drifter - the arcana lyrics