lirikcinta.com
a b c d e f g h i j k l m n o p q r s t u v w x y z 0 1 2 3 4 5 6 7 8 9 #

la famille au senegal oui - diarra sylla lyrics

Loading...

[intro: diarra sylla]
hmm
et la famille au sénégal?
oui, bien sûr!

[verse 1: diarra sylla]
sori sama réew ak sama askan
taxul ma fàtte man mi may kan
damay liggéey doxuma ci caaxaan
seen soutien da may bégal di ma yokku katan
damay ñafe di liggéey duma geestu
yónne yakamti ma duma daagu
li ma weesu la réccu
fi ma jëm leer na ma, man la ni séntu

[pre*chorus: diarra sylla]
ay ay ay
fii mooy senegaal

[chorus: diarra sylla]
fii la xol yi di feexe
fii la stresse biy wacce
fii la xale yi gëna baaxe
sama réew nii la neexee

[post*chorus: diarra sylla]
foo dëkk, senegaal? oui!
fière ci doon sénégalaise
la famille au sénégal, oui
fière ci doon sénégalaise
[verse 2: dior mbaye, (diarra sylla)]
civilisé rafet mëna sañsé
tey bëgg topp cas
(ku ne ng*y wax, pays de la )
kenn du ñu yàpp, kenn du ñu xeep
kenn du ñu kël*kële
(ñun lañuy wax, pays de la )
am teranga meun mass laa meun sedalee
(ku ne ng*y wax, pays de la )
sama réew mi da may neex te jàmm ja ngi fi
[?]
jàng bi na fi sax, jàng bi

[pre*chorus: dior mbaye]
ay ay ay
fii mooy senеgaal!

[chorus: diarra sylla]
fii la xol yi di feexe
fii la stresse biy wacce
fii la xale yi gëna baaxe
sama réew nii la neexee

[post*chorus: diarra sylla]
foo dëkk, senegaal? oui! (oui, bien sûr)
fière ci doon sénégalaise (oui, bien sûr)
la famille au sénégal, oui (oui, bien sûr)
fière ci doon sénégalaise (oui, bien sûr)
[verse 3: dior mbaye, (diarra sylla)]
yaw diara sylla! (foo dëkk, senegaal? oui!)
(fière ci doon sénégalaise)
(la famille au sénégal, oui)
(fière ci doon sénégalaise)
(foo dëkk, senegaal? oui!)
(fière ci doon sénégalaise)
(la famille au sénégal, oui)
(fière ci doon sénégalaise)
[?] (foo dëkk, senegaal? oui!)
[?] (fière ci doon sénégalaise)
[?] (la famille au sénégal, oui)
[?] (fière ci doon sénégalaise)

[outro: diarra sylla]
foo dëkk, senegaal? oui! (oui, bien sûr)
fière ci doon sénégalaise (oui, bien sûr)
la famille au sénégal, oui (oui, bien sûr)
fière ci doon sénégalaise

Random Song Lyrics :

Popular

Loading...