jambaar - carapid music lyrics
[hook : bako]
kénn momoul ndam li..
koumou nékh djeul, koumou nékh baa
nioune dougn baaayi dareu
beuss bu yallah déf gaïndé la
kone lundi,mardi,mercredi,jeudi,vendredi aq samedi
boy dimanche sakh ngui tchi biir
[verse 1 : opd]
fo ko fekeu dey khekh yeah aka meune fight
demb ba diekh wessou def li mou meune
bougoul t-ss yakaar ndakh ga yi koy khar
xel bi naan ko go never give up
give up for what, bayi pour lane, bou bakhoul gnou defarouwat
outi delo gneuwat, demat ba diekh. ba ndam li wouyoussiwat
kokoy djambar, door waar, lagn ko khamé mom outéna akh yambar
hero vrai soldat, boudoul daw combat. paré pour dekkou tang-you tamba
here we are let’s go, gaindé ndiaye yes we are you know. dikkeu def lou noy dougn ko def no no. bou gnouy perte sakh perte akh jom (leggo)
[hook : bako]
kénn momoul ndam li..
koumou nékh djeul, koumou nékh baa
nioune dougn baaayi dareu
beuss bu yallah déf gaïndé la
kone lundi,mardi,mercredi,jeudi,vendredi aq samedi
boy dimanche sakh ngui tchi biir
jambaar la x5
bo donoul jambaar yambaar nga
mane jambaar la x4
[verse 2 : fla]
jambar ca war ba, boul meusseu tok di xar
jambar ca war ba boul hadi amo lila war
always on your guard like a war
never be ashamed of what u are
from dust n-gg- try to soar
fight for u life fight for ur money fight for ur country and take it far
mani jambar boula keneu terei mouss beuri pekhei figth mana tekhei
yay bagne la merei bay bagne la merei
kone diougal ma n-gg- defal dara sa life bala mo trop tard
boul xar dara ci keneu tei xamni life bei tar
[hook : bako]
[verse 3 : kalz]
luma mat mou dagati
deunn meu feugeuti
djeuli na ndamli
fouleu meu guindi
mane djom meu yeukeuti
xoss na xalima
xol ma xaméma
xalé bi xatchina déy door
xaré bi lay dor
xidi meu dooumeu xouxeul tiey goor!
doumeu gangster doumeu pa pa pa
love lay djiteul wayé sokoo djaré dina rak ba naw
watié karaw ni canceeer
kouleu ndjeuk tok moleu geneu bok moléy geneu tok
lo fok déniou khéy rék tiop?
worneu saméy baxou maam
meuno meu djaay graw dameu niangu maaan
méy djambar djambar djambar niéti yone
ngéy niankar,niankar,niankar pousseul sameu yone
dameu nieuw pour djité , djitlé
mane maay kakan moussa
rap bi noumou sofé, saafé, def si kankan mou saf
[hook : bako]
Random Song Lyrics :
- sguardo lume - roadelli lyrics
- dance with me - ingrid michaelson lyrics
- words confined - police bastard lyrics
- sade in the 90s (live from herby house) - qveen herby lyrics
- your leading man - mark knopfler lyrics
- ninth song - river tatem lyrics
- stayin on da line - cl0neddeathh lyrics
- pawn - tarnisher lyrics
- addicting girl - ellie mason 444 lyrics
- overthinking - unpeople lyrics