boy sicap (remix) - carapid music lyrics
[bridge : rich black]
est ce que meune ngeu diay néx boy sicap?
est ce que meune ngeu diay graw boy sicap?
est ce que meune ngeu ték xél boy sicap?
mane..dumeu dém jail boy sicaaaap!
[verse 1 : bako]
im not from capsi gueule tapée la diogué wayé respect capsi
diudou gt deukeu yoff grand boy f-ck dat mane feep lay represent…
l1, l2… l3… l4, l5…
sac city 1 sac city 2 sac city 3 baobab wa l6 !
sicap capsi sicap magui bégué sicaaaap
deugueuleu t-ssé negn biir amitié mais takhouma done sa waye
niogui sene kanmam duma sen m-ss, duma sene couran
rap sudone cl-ss yeney taaable bancs
fuma sen place damey tokk sen kaw… suivant !
[bridge : rich black]
est ce que meune ngeu diay néx boy sicap?
est ce que meune ngeu diay graw boy sicap?
est ce que meune ngeu ték xél boy sicap?
mane..dumeu dém jail boy sicaaaap!
[hook : rich black]
sicap capsi sicap
mangui bégé sicap x4
[verse 2 : fla]
est ce que mane nga diay nekh boy sicap
soko manei yokhoul sa bat boy ci kaw
boy nianning boy nf yeah dama graw
mana rap beuri diap fils niola raw
ni ay boy sicap fils damay doundeu kaw
voleeee
douma takeu tei damay naw
ni sama tour boy takh malene di survoler
b-tch i do me dont ask me my mane cuz u know me
been ballin from dk to kl yeah them b-tches love me
revolutionary like awadi
ni boy sicap fils dama xamad
i
[bridge : rich black]
[hook : rich black]
[verse 3 : kalz]
lakouniou kal diola waleu sereer
djeul djom ak fit takk ko téré
sérél p-ss andil seu témér so xamoul side meune ngeu séé réér
nioune ndam req xoumougn lénéne loudoul coupe
kogne bé kéy todj depuis robotcop
té nga roteul kopp waleu ngeu sétal bok?
nio dakk scandale olivia pope
mani capsi capitale
kalz capitaine
ay peine capitale
kalz saddam hussein
défougnou rap hardcore d’accord mais nio geuneu technique wa matforce
meuno diss wa l6 fils dégn diss fils
séne dix pistes lakk ay pitch esk yangui siip ?
[verse 4 : rich black]
[hook : rich black]
Random Song Lyrics :
- fit for it - g0uenji lyrics
- piky - jezzy lyrics
- nur ein blick - ela & diaven lyrics
- enlightened. - nac el suave lyrics
- side by side - brocki lyrics
- bâteau dans le ciel - skary & wysko lyrics
- give*мe colors,, - swaggaholix lyrics
- bridge burner (ft. lucyv, headband henny) - tofu tony lyrics
- aló - sadh ikki lyrics
- innocent - darling gails lyrics