relève - boiie pablo lyrics
[intro]
han, boiie pablo, check, wow, check
paw, paw, paw
/mad on the ketchup/
[couplet 1]
gni sa guinaw nioy gniley xhaagn
loy ragal moy liley gaagn
linga gueum moy liley dall
euleuk, gniley xhekh moy gnila fall
soy daagou ioe niouley dap
rawanté meunoul andeu ak ay kaf
manager sakh douma baap
may liguey, def lou reuy, té awma staff
guissouma kenn koumay stop
damay djiité nioumay top
gueudj naa daw ramass depuis temps collège
portant sama trafic moungui dokh correcte
boul laadj limay ioe lo sokhla rek ? x2
wolouw’mala boul ma naane ay may sa frère
rooney xhéékhone na cristiano manchester
may nangou seu leer paré nek ci keer
(may nangou seu leer paré nek ci keer )
[refrain]
xhoolema el pablo…may relève bi el chapo
teudj ma cii biir prison..tiiyé woul sama vision
dieum dji ng*y xhatal, mais, egoul sama cerveau
percer mom c’est mom c’est par force
f*ck lice*po ak sen poste
tunel de 5 kilos..fa leu chapo fuitone
on defonce ! boom boom !
motocross ! vroum ! vroum ! vroum !
[couplet 2]
nioofii djiité key ! amoul c’est*à*dire
dang niou beuga tiiyé ? outal ferrari
binndeu textes ba lokho yi panaris
faw niou tedd solou melni quataris
loumou ladj niou defko dieund sarakh bi
yoré chicha fokné ioe la cana bi
narcos gang comme mafia wou colombie
papiito eundil kilos canabis
deff veup mbeuké melni taureau bii
réflexion yii xhoote
textes yii guena dope
tek’ci zéro faute
guena yokk job
guena nek au top
guena yokk djom
f*ck sey règles, limoy rap bou ménopause
gniodii classique, raw negn leu nga meuna pose
fils doumeu weeré même sakh soumley foote
lii dou meuss thiéré meme sakh soumey foo
fils doumeu weeré même sakh soumley foote
lii dou meuss thiéré meme sakh soumey foo
[refrain + outro]
xhoolema el pablo…may relève bi el chapo
teudj ma cii biir prison..tiiyé woul sama vision
dieum dji ng*y xhatal, mais, egoul sama cerveau
percer mom c’est mom c’est par force
f*ck lice*po ak sen poste
tunel de 5 kilos..fa leu chapo fuitone
on defonce ! boom boom !
motocross ! vroum ! vroum ! vroum
Random Song Lyrics :
- no rīta - putnu balle lyrics
- borderline - nogfgoodnight lyrics
- falling out - kid gemini lyrics
- ways to be wicked - hollander edmondson lyrics
- 野 savage (ye savage) - desert5 lyrics
- finer things - jvlie santana lyrics
- luvr of mine - sleepsk8 lyrics
- 161718 - l3g4cy lyrics
- all eyes on us - lit lyrics
- alo zeus? | الو زيوس معايا؟ - 7ii | السابع lyrics