ney leer - boiie pablo lyrics
ney leer lyrics
(intro)
45° drill, boiie pablo, check, wow, anh
(couplet 1)
bo amoul dara waro xheep dara ndakh boudoul dara n*gga ioe diarago dara
boul bagn sa bop xholal niinga nékéé
ndakh lii nga nékéé rek ng*y moudié nék
sou dee doulone béété kenn douko ragal
do xham louy ragal boula yallah di faral
do ragala dialeu ci yone bimley xharal
ak loumou meuna tarr’a tarr ioe dalakoy diaral
ki banioul dara sakh am na limouy bagn
ndakh bania niakk motakh dou meuss bagn
goor fall sa weurseuk kenn doulako xhagn
fii lepp lou diote yombou nak xhana nga bagn
dee dafay bêté té mom nena tekk
fepeu lalay fekeu fexhel kone mou diekeu x2
même ki guena kawé souf si dakoy lekeu
wakh yi guena soufé yallah mingkey degg
bo nékéé ci bamel youkhoul dougn la degg
way lou janteu bii tangg bamel meun n’a sedd
boy taneu niite tamoul kilay taneu ndakh boko tamou mom’ite ioe leu tamou
diokhé nimbeul mo gueun wooté nimbeul
diokhé ndiigueul mo geune dieufé ndiigueul
(refrain)
degn my n*gga, hey deugg dou degn my n*gga
bagn my n*gga, hay somay bagn my n*gga
degn my n*gga, hey deugg dou degn my n*gga
(couplet 2 )
lii contre attaque leu..f*ck seu tic*tac
remonter nieup..f*ck sen tactique
yone bouy gaaw leu no dou ay zigzag
…( no dou ay zigzag )
dama am bac diayleu prek ak zhatboiie
dougou ci rap bi tek yeufou bad boiie
keuff senn buzz youkhou leen sathioy
xhiif ay atte xhawma louy paatio
am rapp di def rap motakh bama rabé
dou am alal rek mo wara takh nga tabé
lepp loy xhepp sa bop am n’a niite ko tané
nieup yemou niou wanté n*gga nieupa diafé
yamba bi amoul courant wanté fimley yeegueul ascenseur bii xhalaatoufa egg
ba takh n’a boyi thiolé ci sen life dem dieul ci joint yii fokné nio guena egg
diokh ma respect force ni sey généraux
diote ay tonne appel melni guerrero
niouné job nice neu n*gga gérer ko
mané zéro pression douma weeré bro
(pont)
dama am bac diayleu prek ak zhatboiie
dougou ci rap bi tek yeufou bad boiie /
lii contre attaque leu..f*ck seu tic*tac
remonter nieup..f*ck sen tactique
yone bouy gaaw leu no dou ay zigzag
(outro)
degn my n*gga, hey deugg dou degn my n*gga
bagn my n*gga, hay somay bagn my n*gga
degn my n*gga, hey deugg dou degn my n*gga
Random Song Lyrics :
- deep exhale - adlo lyrics
- as if - jessy lanza lyrics
- γι΄ αυτό σου λέω μη (gi' afto sou leo mi) - anna vissi lyrics
- i could live on my couch - bilby lyrics
- i'm in love with a crackhead (stripped version) - champ hercules lyrics
- infinite zero - the soundtrack of our lives lyrics
- wow - nigo chanel lyrics
- m.g.r ? (cold souls) - tami lance / everything's a crime lyrics
- pali motore - dj shone, 2bona & vlada matović lyrics
- por primera vez me corro (reprise) - chikili tubbie lyrics