danger - boiie pablo lyrics
[intro]
sku, sku
it’s your boy pablo
[couplet 1]
dugu fii danger la, tagoul sey mbokk bo nieuwé thiéinthieu leu
dof*dof*loul ken doula, wakh heure bii foum toll melni degougn leu
dundu bii diéngou leu, soy ragal thioono rek mou songou leu sééniou leu
deumm yii fééniou leu, faw nga meuna xhamé mbaa niou diékkou leu
fokné koula siign moy sa andadoo, dafa fekk n*gga magagoo
n*gga bo xhamé ni xhamagoo, meun xhamlou balaa weesou book
wanté bo xhamoul ni xhamagoo, dii nga lorou moudié bagn sa boop
yanguii wouty n*gga amagoo, boul andadook gnii amoul ndokh cii boop
meuss negn ma raw gnima andadool, mais bima beugué damlèn yagga boote
dafmay nekh ma djiité douma meuntii bokk
manguék meun*meun, ak katann ak ngandii bopp
même kii deff lou nekh mounoul nekh nieupeu, ma dieema nekh kii moudiou té ndieukeu
nieup mounougn toloo nak té moy deugeu *
way bou nieupеu boolo meunn ki meunn nieupеu
mère bii dii diooy père bii geudeu, ndakh yarougn sen doom bi ci deugg
beugg lou nooy té fii deugueur, motakh niouy door ak dii keuffeu
braquer leu gun bi dii seufeul, ladj leu sa money si chauffeur
yako nangou boodé chômeur, té yay xhagn sa bop sa honneur
liguey dou xhaadj dou diekh hana ng*y xheep !
soy taamou naadjé comme kouy taneu thieep
bo beuggué feekh faw nga deuké kheekh
fii lepa metii même sou lepp di dieekh
nga thioolé mbaa nga tekki dingko yekk
way fexekhel tekki nguirr nga guedj ko yekk
té lou gawa diekh moy li yomb’a am !
gni yeekh yewou moy gni yeekh’a am !
dou lou yeemé n*gga nekhnaa xham !
[pont + pré*refrain]
té lou gawa diekh moy li yomb’a am !
gni yeekh yewou moy gni yeekh’a am !
dou lou yeemé n*gga nekhnaa xham !
meuss negn ma raw gnima andadool, mais bima beugué damlèn yagga boote
dafmay nekh ma djiité douma meuntii bokk
manguék meun*meun, ak katann ak ngandii bopp
même kii deff lou nekh mounoul nekh nieupeu, ma dieema nekh kii moudiou té ndieukeu
nieup mounougn toloo nak té moy deugeu
way bou nieupeu boolo meunn ki meunn nieupeu
[couplet 2]
boodé yoolé man bouma diégué*diégué
fii lepa lundum kén dou mbélé*mélé
té souniou meun*meun dugnko wedj*wedjé
daniouy deff ng*y guiss douniou wéré*wéré
teksi bokougnok guys loloo guena yéémé
niom amouniou sh*t paré beugg woné
nigaa douniou og douniou thiéré*thiéré
narcotik sama boyii nioola guena niémé
diaroule ladj, that’s right boy nonu la démé
koufii deff lou sal rek ma fété*fété
dinaa fessal salle signer cachet*cachet
amatouma diote dama wara mettre le paquet
n*gga n0bouma sa yaye damko fassé*fassé
def xhaliss sam guyn moumay gâter*gâter
def hit, make money lolou kassé*kassé
teksi manguék talent bi lol dou diafé*diafé
dagnii niafé*niafé…dougnko kaféé*kaféé
tangal game bamou bakh melni café*café
diapp n*ggas yii feutt, deflén dégué*dégué
ana koukoy téré ?
boudé dangma méré !? dafa melni ng*y marr paré naan sa déréte
boudé dangma méré !? dafa melni ng*y marr paré naan sa déréte
boudé dafa diafé dang*y xharé, kassé !
kou am dara dafa défone dara, kassé !
n*gga weurseuk kiko moom rek ley, tassel !
wanté dafay fekkii gniiy xharou di niafé !
bo beugué alal dangsi boolé thiono, niémé !
ki niakk alal moungui xhalate nimkoy, amé !
ki fessak alal moungui ragal souko, niaké !
kounek’ak lila sonal motakh nieupa wara xharé
boy xhaar ci niite diinga lorou f**ko doul xhaaré
lo beugg dalay gaagn rawatiina boko taméé
niou diaay la doméram ndakh mbeuguel bougnko xamé
loo bayii dalay bayii lolou la diamono dji wané
boul xhool si gni nga tané dieemal dialeu fii nga callé (never)
[outro]
gang gang gang gang …
Random Song Lyrics :
- distress - mass murder messiah lyrics
- venison - ison (alec neptune & daniele cris) lyrics
- tattoo (live at koininia koffeehouse, 3/13/98) - the 77s lyrics
- raw - t-shawn lyrics
- rock n' roll lady (album version) - white swan lyrics
- khuda jaane - kk & shilpa rao lyrics
- холодный мир (cold world) - витас (vitas) lyrics
- i want those cars - jack stauber lyrics
- keepit100 - saad khan lyrics
- van de top naar de underground - the opposites lyrics