lirikcinta.com
a b c d e f g h i j k l m n o p q r s t u v w x y z 0 1 2 3 4 5 6 7 8 9 #

fahass - bai babu lyrics

Loading...

fethia bu neka am na
but bi do ko dianga
you have to born with this sh*t
pour makk yow nyu langa
duma deh leka jakhatou
waye su la nekhe damb ma
foula takh nga okatou
kom kouye egeh diamla

bouko fetcha di seuga
diapal si sa ndinga
bul rouss maneh merr bi niowout
nieti yone la nak do reutcha
dieul loxoy witiax nikouy beuga diapa pitcha
just dance it diko teuyax mo kham bouko nekhe seuga
dafa sorri man doumako diegué
naka dieulssi kon souko pare
attack xolal bi tasseh nieti yon la nak ndaw xarré
bousi nak foxoj sa ndiga ndablii si diga la tiba
li ma saff la kom sossi liba nhaa bang ko kanna sila
ah ana loy ragal dieguesill wala ken randal
kou sa gianaw bandang

kay len niou fahass
sa loho sa guanaw
melal ni kouy fogass

suma xeet bi dugana guneh gui
faxass xar si digabii
bugut ben budul bii
xawma kouy doba si guenagui
dioxko ndam dioxko ndam
sax ak ndiognam ak ndiognam
basi askanam askanam bina wan kanam
peundal suba faxass ngon
yon bi gouda kuneh awsa yon
kouko wédi neka xarr sa fei rek moy dioxla gnogn
basi kawa kaw ma adjko kuko adji ding ma togn
beat bama diégue ma najko niu seuy rek amsi dom
kula téré lembeul yenguelal nii messi bouy teubal sula nekhé town bi nga pendal xol yi diniu begual play ken doula pause
sougn biir yambarr doufi sauce
degn meti teh sohorr nurse
soula nekhe latchel dios

bamboo kom katchikally
dokh sa mind bi tactically
mind bi dioub ni bena tally
doma dab nax damala sorri
dama gaw ni ball bugnu fetel
am samsung ni alcatel
na nooy pape malaw na nooy modou mbaye
kay len niou fahass
sa loho sa guanaw
suma heet bi dugana guneh ngii
fahass xar si digabii
bugut ben budul bii
hawma kouy doba si gueunagui
modou mbaye ahh
bouko fetcha di seuga diapal si sa ndinga bul rouss maneh ×2
bouko fetcha di seuga! diapal si sa ndinga bul daww malaw ahh
mom dafa toy fompana fompat
mouné mukk mom du wow
we are at war xex naw basa kaw
si deuna lala teg tabaxal basa kaw
lufi n0bu dina feign, do ku ndaw
da way girl is whining dafa melni amout yax diane moko djigadi xawma loumouy defni souko nekhé toodj deuna bi ba mou dangal podj bi
ay yaaa wouy sama ndeye
ya am sama thiopati ×2

Random Song Lyrics :

Popular

Loading...