sutura - ashs the best lyrics
sutura lyrics
ci sutura ci sutura ci sutura
sama waaji na ñu waxtaan ci sutura
xarit, dee naa la ci sutura
ci sutura laa lay waxee sama ge’nt
sutura
ci sutura laa lay samay proble’mes akk lima dal
sutura
ci laa lay de’nkee sama guddi
bulma weer ni bëccëg
bulma weer ni bëccëg
sutura sutura
bulma weer ni bëccëg
ndax yombul nga xamal ma
mbokk waay
sutura sutura
sutura sutural ma sutura
sutural ma sutura
sutura sutural ma sutura
mbokk du nii
reeroo bumu tax nga tasaare ma
sutura sutural ma
ñu weetoo ma wax la sama demb nga waxaat ko tay
xarit sama waaji
ma ne mbokk du nii
bulma jeebaane fii
bul wax sama proble’me ci ñii
woolu la tay
waraloon demb ma wax la lu xew wax la sama xol
mbokk waay
sutura sutura
sutura sutural ma sutura
sutural ma sutura
sutura sutural ma sutura
Random Song Lyrics :
- estés en donde estés - lucah lyrics
- me caso y cojo cuernos - jamsha & barbie rican lyrics
- diorr video - crystal lalucci lyrics
- necu proci jeftino - stoja lyrics
- one time - brray lyrics
- whisky licor - jonny lock lyrics
- i'm outside - javinci lyrics
- high in my room - ajyr lyrics
- nonchalant - ace og lyrics
- why - amii stewart lyrics