lirikcinta.com
a b c d e f g h i j k l m n o p q r s t u v w x y z 0 1 2 3 4 5 6 7 8 9 #

doumala fowé - amadeus lyrics

Loading...

doumala fowé lyrics
doumala fowé
doumala, doumala fowé
doumala, doumala, doumala, doumala fowé
doumala, doumala, doumala, doumala fowé

soxna si, thi mane ng*y moudia guissé love
ndéké mbeugel is all i need mane
sam sa daradia ni mane
manam dou xale bi
boudoul yaw dou meussa done kénéne
ndax sameu nga sa ndaw ni mame
di guenou farata ni mame
mane adouna la beugah wane
baniou khamni que ni tekk nala fou kawé kawé
togal sama wet boul ma meussa tagou
ndax xam nga ni soma soré ma weet

damla guiss yek tegé feulé sama mbonté
mane lima yittel moy sama mbecté
beugou mala disturb
diegalou soum lay énervé
non meti nala limla topé girl
yalla xam na
ni mane beug nala
li takh niamé woma
dama deung diar diar
sam demb niawna
ndieulbén dou nada
mouthie gou rafete lay niane yalla diokhogn mala
doumala fowé
fima la foré da sorri
sa reh djou nex
momay fathie souma fébaré
doumala fowé
ndax fima la foré da sorri
sa reh djou nex
momay fathie souma fébaré

ak lima meun guiss lima degg
mane douma give up
yen bi loumou meun diss loumou deugeur
darra douma disturb
neko ci réseau sociaux yi di polluer all time
danaka sax do nek online
f*ck cheveux naturel enjoy nga life bekk na
lolo waral mane yaw lay nian

damla guiss yek teggui feulé sama mbonté
mane lima yittel moy sa mbecté
beugou mala disturb
diegalou soum lay énervé
non meti nala limla topé girl
yalla xam na
ni mane beug nala
li takh niamé woma
dama deung diar diar
sam demb niawna
ndieulbén dou nada
mouthie gou rafete lay niane yalla diokhogn mala
doumala fowé
fima la foré da sorri
sa reh djou nex
momay fathie souma fébaré
doumala fowé
ndax fima la foré da sorri
sa reh djou nex
momay fathie souma fébaré

Random Song Lyrics :

Popular

Loading...