lan la - aida samb lyrics
oh lan la
oh oh lan la
lan lala def
wakh ma
oh oh my love
ay fana ngui thii tay
khamouloni sakh man mangui thii keur gui
oh oh souma teudé thii nekk bii
nga dieul sa mbadj dem teudjou thii salle bii
oh oh balma
oh oh lan la
lan lala def
balma
oh oh my love
oh ladj nala lane mo khew nangou loma wakh deuké dima éviter
oh oh souma teudé thii nekk bii
nga dieul sa mbadj dem teudjou thii salle bii
oh oh lan la
oh oh wakh ma
lan lala def
balma
oh oh my love
khamnga ni yow my love fima tollou ni nirotouma niite
kheuy rek téh sa bopp té man khamouma batay lanlala def
my looooove lett ma ba nga firi ma
oh oh my love
wakh maaaaaa
fekewma yeggouma tinouma wakhouma deffouma khamouma batay lan lala def
louma meunti am yamako gueuneul yow rek
la kham yow rek la miine yow yay sama wayy
my baby
i need you
my baby
i’m missing you
oh oh lan la
oh oh wakh ma
lan lala def
balma
oh oh my love
khamnga ni yow my love fima tollou ni nirotouma nitt
kheuy rek téh sa bopp té man khamouma batay lanlala def
my looooove lett ma ba nga firi ma
oh oh my love
wakh maaaaaa
so khamone lima kham man dingma teh waw waw
so khamone lima kham man dingma yeureum waw waw
jigeen kouko beggël diko yeureum la am waw waw
kone dekkoy beggël diko yeureum diko waw waw
so khamone lima kham man dingma teh waw waw
so khamone lima kham man dingma yeureum waw waw
jigeen kouko terral diko saggal la am waw waw
kone demay beggël dima saggal dima waw waw
my love
wakh ma
my love
wakh maaaaa
man beugone na dh louma deff
nga woma niou wakhtané ko
chercher ma tappass té deffoumala dara
so khamone limay dundu ni noumou mété
(pape thiopet)
fils dafa am loma tamalone bama tameko nga bayiko
khol bou beggoul dioy
té kouy dioy dou nakh kouy dioy
lo lo ma metti fils
man beugone na dh louma deff
nga woma niou wakhtané ko
chercher ma tappass té deffoumala dara
so khamone limey dundu ni noumou mété
(pape thiopet)
baby oh
khol bou beggoul dioy
kouy dioy dou nakh kouy dioy
lingma tamalone ma tameko nga bayiko
chérie nga bayiko
ndaw ak limou mine souko guissoul daffey wett
chérie boy
man jigeen la
khawma dara
a bingamey dieul
man mi khawma dara
wayé tay la nekh ba nguey soppi djiko
(pape thiopet)
eyy deug leu
louma soumi nga faute ko lem
chérie deug leu
dima wakh wakhdjou melni lem
chérie deug leu
wayé amna lou dess
chérie boy kholal ndiggleu gëseum
yako dane feth may begg ndiggleu gëseum
boko fethioul may dioy ndiggleu gëseum
kou nopp sa chérie boy djougueul takhaw
diaplène fi niou dem
ndiggleu gëseum
thiof fi thioffat ndiggleu gëseum
ayyy ndiggleu gëseum
ndiggleu gëseum
thiof fi thioffat ndiggleu gëseum
thiey
kou nopp sa chérie boy diougeul yeungou
kou nopp sa dieukeur diougeul yeungou
kou nopp sa chérie diabbar yeungou
kou nopp sa yayou dieukeur diougeul yeungou
ahh
Random Song Lyrics :
- superego lightning bolt - wrongbird erickson lyrics
- aquí estoy yo - yo raps lyrics
- your word - c3 music lyrics
- you and i - switch lyrics
- fuego fue - julia~cristina lyrics
- crecer en grande - nebu lyrics
- a de julho - tutafarel lyrics
- miracles - kirk franklin lyrics
- esta noche - mb feat. giankey lyrics
- faltas - julia~cristina lyrics